Siddeem pom
Siddeem pom xeetu garab la gu bokk ci njabootu Rhamnaceae yi. Xeetu siddeem yu baree am.
Melo wi
SoppiGarabu siddeem pom danay àgg 2 ba 5i met ci guddaay, ak i xobam yu nëtëx tey melax yiy àgg ba 5i sàntimet ci guddaay.
Doom bi dees koy lekk, wirgo wu mboq lay yor te muluŋ danay toll 1 ba 1,5 sàntimet.
Nataal yi
SoppiTuru xam-xam wi
SoppiZiziphus lotus