Siddeem bukki
Siddeem bukki xeetu garab gu bokk ci njabootug Rhamnacées. Moo ngi coosaanoo Lo ci réew yu naaje yi.
Aw meloom
SoppiSiddeem bukki garab guy am i dég, ak i doom yu nuy woowee siddeem bukki. Garab gu dëgër lay doon ci jamonoy noor.
Am xasam day ñagas am ay pàq, wànqaas yi yaatu, ëppante te am i dég. Xobam yi seen wirgo day wuute.
Njariñ yi
SoppiDoom bi dees na ko jëfandikoo ci togg, dees na ko lekk noonu it.
Foytéef bi barina ay ferñeent lool.
Nataal
Soppi