Sanqaay xeet la ci xeeti garab yoo xam ne dañuy màgg ci fu am naaj, ñung kay fekk ci kémbaarug Afrig bu yaatu fa lool. Waaye itam, Waaye desu ko fekk fu mel ni: Nambi bi, ak Butsuwanaa, ak Afrig bët Saalum.

Sanqaay gi (Ficus glumosa)

Melo wi Soppi

 
Meññeefi garabug sànqaay

Garab la gog man naa sax foo xam ne amul ndox. Baayima yu bari dan koy jëfëndikoo ngir di ci tabax seen i dëkkuwaay lu ci mel ni xeet i picc yi. Ay xóbam dana yor melo bu muloŋ , ci yaatu waay, manees na koo natt ci juróom-fukk, jàpp teeméer ak juróom-fukk ci ay milimeeter.

Solo si Soppi

Ay xóbam, danoo gaaw ci lool ci xeex biir buy daw, loolu moo tax mu bokk ci xeeti garab yi nga xam ne ci fajum cosaan.

Turu xam-xam wi Soppi

Ficus glumosa

Turi ci yeneeni làkk Soppi

angale: african rock fig