Rëb-rëb gi xeetu garab la gu bokk ci njabootu Terminalia, Afrig gu sowu lees koy fekk.

Melo wi

Soppi

Rëb-rëb gi gàncax guy hàgg cig guddaay 2 ba 4i met la, mbaa garab guy hàgg cig guddaay 8 ba 12i met, te ronam day gàtt ba noppi am xànc mu baam.

Njariñ yi

Soppi

Ca Mali xobam dañ koy cuubee ndimo ngir mu am wirgo wu mboq.

Nataal yi

Soppi

Turu xam-xam wi

Soppi

Terminalia avicennoides