Poortorikoo
Poortorikoo Ab dun la bu nekk ci mbàmbulaanug Atlas gi te bokk ci Réew yu Bennoo yu Aamerig. Puerto Rico amna sàrtu ndayu réewam ak bànxaasam tëral sàrt, jëfu ak àtte. Lëkkaloo gi am ci diggante Etats Unis mingi aju ci bokk doomi réew, xaalis ak kaaraange.