Ngun-ngun
Ngun-ngun xeetu gancax la gu bokk ci njabootu "asteraceae". Garabu rëndaay la, dees ciy safal.
Melo wi
SoppiGàncax la guy tollu ci 20 ba 90i sàntimet ci guddaay. Xobam daa tàppndar, danay àgg 2 ba 3i sàntimet. Xobam ci diggante nëtëx bu dër ak woyof, yenn saa yi nag mu ngolleñ ci yenn xeet yi.
Njariñ li
SoppiAm rënd mu am solo la ci wàllu togg ci yenn réew yi. Ca Senegaal dees na ko def ci ataaya. Gàncax la gees di fajoo it.
Turu xam-xam wi
SoppiBlumea aurita