Ndaté Yalla Mbodj
Lingeer Ndate Yàlla Mbóoj,am nu koy woowee Ndete Yàlla, mu ngi juddu atum junni ak ñetti téemeer ak fukk, génne àddina atum junni ak juróom ñetti téemeer ak juróom benn fukk. Nekkoon na buur bu jigeen bu mag ca réewum waalo, réew mi féetewoon ca bët-gannaar penku Senegaal.
- ↑ Afrique Histoire U.S., Volume 3, Afrique histoire U.S. (1985), p. 32
- ↑ Barry, Boubacar, Senegambia and the Atlantic Slave Trade (ed: David Anderson, and Carolyn Brown ; trans: Ayi Kwei Armah ; con: David Anderson, American Council of Learned Societies, Carolyn Brown, University of Michigan. Digital Library Production Service, Christopher Clapham, Michael Gomez, Patrick Manning, David Robinson, Leonardo A. Villalon), Cambridge University Press (1998), p. 182, (ISBN 9780521592260)
Dundu ak jaar-jaaram |
---|
Nataalu lingeer Ndate Yàlla Mbooj | |
Lingeer Ndate Yàlla Mbóoj Lingeeru Waalo | |
Xew- xewi dundam | |
---|---|
Turu buur bi | Lingeer Ndate Yàlla Mbóoj |
Giir bi | Giirub Tedyeg ci wàllu meenam ak giirub Diyoos ci wàllu geñoom |
Turam | Ndate Yàlla Mbóoj |
atum juddu-atum faatu | - 1860 |
Béreb ba mu juddoo | Waalo, Senegaal |
Pàppam | Barag Amar Faatim Borso Mbóoj |
Yaayam | Lingeer Awo Faatim Yamar Xuri Yaay Mbóoj |
jëkkëram | 1. Barag Yerim Mbañig Tegg Réll 2. Maroso Tase ob (Saakura Barka Jóob) - Buuru Kayoor[1],[2] |
Doomam | Siidiya Lewon Job |
Diineem | Afrig |
modifier lien=Modèle:Infobox_Personnalité_politique|12x12px|Consultez la documentation du modèle |