Musée de la mer (Gorée)

deccukay bu gecc moy deccukay buunu bole ci IFAN, gnoko deff fofou ci xeru goore bi, ci tefessu Dakkaru buu Seenegaal.

Melosuuf

Soppi

Fetuway

Soppi

Kheer bi di Goore mogui cii 19 beret arodisema bu Dakaaru, Seenegaal. Benn kher sibir dokh mi mogui def 18,2 hectar moggi digg geentem ak tefessu Dakaaru 2 kilo.

Deuk bobu di Goore mogui nekk si digg dokh mi. Booko bugon khaima, Goore reyuul nonu yeep, moggi def 900 metra ak 300 metra, lolu takh ba reer fa yobbul? kuu wakh Gagnethiaw wakh ci meteo. Maanam muun ngafa niow tee soolo yeere bu diss (na fekk fananofa). tamperature yooggi kooy khaima ci 17 ak 25° buu beethiegge taangoor, ak 24 ba 30° buu taangoor gnowe. Lolu bokuna ci li kheuthie nassaran yi. Lolu takh naa muuy tangoor sakh guuddi gui sool yeere buu diss dalay waar.

Taariix

Deccukay bi niogui ko soss ci fukki weer ak niar ci atum 1959 mook daara bu kaawe buniu duppe chek Anta Joop bu Dakaaru, niogui ko ubil bolo mi ci weer bu njeuk ci atum 1960. Ci atum 1995, lagneko geene jeumeul. Cila ko IFAN dakh sokhal ko mok yeneen yu melni mom tee booku si Afrik sow janta yii lakk nassaran. buu fekeni deccukay deuk Afrik ci Dakaaru ammagut, yeenenn jeego nioggi juddu feele see niame, Bamako, Abija, ndar ak dakaaru (deccukay bacca Goore). Bobuu deccukay bokuna si jeego yuu reyy. Bokunassi ay juumtukay niu jeggi dayoo, dakh niu munna dello askan wi giss gis niu jogge ci dokh mi, manan leep luu eube dokh ak napp mi, jaraaleko beppu khett bi nekk si dokh.


Feetewaaye

  • West African Museums Programme (WAMP), , Dakar, Bureau régional de l'UNESCO pour l'éducation en Afrique, 2008 (OCLC 318587910, lire en ligne [archive]), chap. 7 (« Musée de la Mer de l'IFAN Ch. A. Diop, Gorée »), p. 29–31
  • (en + fr) Théodore Monod, Pierre Louis Dekeyser et Georges Bracher, «  », Museum International, vol. 14, no 1,‎ 1961, p. 1–11 (DOI 10.1111/j.1755-5825.1961.tb01561.x, lire en ligne [archive])
  • Amadou Abdoulaye Seck, «  », Bulletin du WAMP, no 7,‎ 1997, p. 6-16
  • https://www.researchgate.net/publication/249499107_Le_Musee_de_la_mer_Goree_Senegal [archive]
  • https://yoytourdumonde.fr/senegal-ile-goree/ [archive]
  • https://onlinelibrary.wiley.com/doi/epdf/10.1111/j.1755-5825.1961.tb01561.x [archive]