Ubbi njël lu njëkk li

MediaWiki:Copyrightwarning

Bépp cëru ci Wikipedia dañ leen di jàppe niki ay siiwal yoo def te teg leen ci $2 (xoolal $1 ngir yeneeni xamle). Soo bëggul keneen jël say mbind soppi leen, tas leen teg ci, bu leen fi duggal.
Te it na wóor ne li nga fiy duggal yaa leen moom, yaa leen bind, walla fa nga leen jële gongikuwaay bu ubbeeku la, lu kenn moomul. BUL FI DUGGAL LIGGÉEYI KENEEN YU AQI AJI-SOS AAR TE AMOO CI BENN NDIGAL!