Maam Yunus Jeŋ
Erreur de script : la fonction « build » n’existe pas. Abla Pokou (wala Aura Poku, wala Abraha Pokou) lingeeru Afrig la , juddoo ci fukk ak juróom-ñetti xarnub. Indi na askanu Baoulé ci réewum Gana ba ci Kodiwaar. Léeb bi dafa nettali, saraxu doomam bu góor ngir jàll ag dex .
Bat bi "Baoulé " li nu tudde leegi askan yi , mu ngi joge ci saraxu doomam.
Bicci toppu saraxe, né na "Ba-ouli", loolu dafay tekki "doom bi dee na".
Maam Yunus Jeŋ
Dundu ak jaar-jaaram | |
Juddu | 1939
Tiwaawon |
Faatu | 1er awiril 2016
Dakaar |
Senegaal | Senegaal |
Liggeey | Bindkat, taalifkat |
Maam Yunus Jeŋ (juddu 1939, faatu 2016) ab bindkat la bu dëkk Senegaal.
Dund ak jaar-jaaram
SoppiMaam Yunus Jeŋ mu ngi juddoo Tiwaawon, ci Kayoor atum 1939. Waajuram wu góor a ngi cosaanoo Kayoor, waajuram wu jigeen moom, cosaanoo Ndar (See Luwi). Jàngalekat la woon mujj nekk njiitu lekool[1].
Maam Yunus Jeŋ ci farañse ak wolof yépp la daan bind, moom mooy ki jëkk a bind ab téereb nettali ci wolof tudde ko Aawo bi. Téere boobu ñu ngi ko siiwal atum 1992 ci Dakaar, mu teg ci beneen téereb nettali bu tudd L'ombre en feu, ñu siiwal ko atum 1997[2].
Àjjuma benn fan ci weeru awiril atum 2016 la génn àdduna ci këram, ci Dakaar[3].
Ay Téereem
Soppi- L'ombre en feu, Dakar, Les Nouvelles Éditions Africaines du Sénégal, 1997, 233 p. (ISBN 2-7236-1108-6). Aussi, très soutenue par sa fille aînée Ndeye Bogui Sow Camara à qui l'édition de ce livre tenait à cœur.
Téere, jukki wala dali web yi ñu yër
SoppiSeetal tamit
SoppiLees bind ci moom ak ay téereem
Soppi- Lilyan Kesteloot , « L'Ombre en feu de Mame Younousse Dieng », in Éthiopiques, n° 60, 1er semestre 1998
- (en) Jean-Marie Volet, « Tradition and Modernity Are Here to Stay: An Analysis of Francophone African Women's Writings Published in 1997-98 », Research in African Literatures, vol. 30, n° 2, été 1999, p. 182-193.
- Guedj Fall, « Aaawo Bi de Mame Younousse Dieng, un récit fondateur en langue wolof », in Éthiopiques, n° 76, 1er semestre 2006.
- Abdoulaye Keita, « Dieng, Mame Younousse [Tivaouane 1940] », dans Béatrice Didier, Antoinette Fouque et Mireille Calle-Gruber (dir.), Le dictionnaire universel des créatrices, Éditions des femmes, 2013, p. 1254.
Jukki yi ñu ko tudd
Soppi- Càllalag Senegaal : Littérature sénégalaise
- Limu bindkati Senegaal yi : Liste d'écrivains sénégalais
- Taarixu jigeen ci Senegaal : Histoire des femmes au Sénégal
Lees jële feneen
Soppi- . Fees ko mën a xame :
- Fichier d’autorité international virtuel
- International Standard Name Identifier
- Bibliothèque nationale de France (données)
- Système universitaire de documentation
- Bibliothèque du Congrès
- Gemeinsame Normdatei
- Bibliothèque royale des Pays-Bas
- WorldCat
Maam Yunus Jeŋ ci dalu web Lire les femmes écrivains et les littératures africaines