Maam Cerno
Rakki Sëriñ bi ji la, ju mu bokkal benn baay, te di ab taalubeem bu ko nanguloon te gëm ko, bokkoon ciy kàngamam, man nañu ne mooy ki toppoon ci moom ciy jamonoom, ndax bi Sëriñ bi di dem ca tukkib géejam ba moom la wuutaloon ca ginaawam ca njaboot ga, mu jiite lepp