Maad a Sinig Ama Juuf Njeelane Faye Juuf

Maad a Sinig Ama Juuf Njeelane Faye Juuf buur la won ca Siin (1825 - 1853). Mamaam ya Seereer lenge woon ak Gelwaar. "Maad a Sinig" moy "Buur Siin" ci làkki Seereer. Ama Juuf nak kerr Semu Njeke la joge ca waali Njuufeen.

Maad a Sinig Ama Juuf Njeelane Faye Juuf (1850)

Xool it

Soppi