Mëfër mi (rabu àll)

Wolof

Mëfër mi, mooy segg gu ñuul, muy segg gu bari malani ci yaramam, muy fer-ñentug ndono guy tax yaram wi ñuul kukk. Ci àll yu fatt yi te bari taw la ëppe ca bëj-saalumu Asi ak End (11% mëfër) lu jafee gis Afrig la, melo wu mel nii dina faral di am itam ca Amerig Jagwaar

Menn mëfër ca géttu réewum Nagarhol, ca End.

Jaguar.jpgMenn mëfër ca Soo-Henrii-Doorly, ca réewi Amerig.

Menn mëfër ca Afrig Bëj-saalum.

Jagwaar bu ñuul ànd ak mooroomu seggam.