Màmbeyaa

Màmbeyaa gi garab la guy nekk ci gox yu naaje yi, ci njabootug Moraceae la bokk.

Melo wiModifier

Xobam yu yeesam day xonq, bu saxee nag nëtëx.

Nataal yiModifier

Turu xam-xamModifier

Ficus umbellata