Leeral Biibël
Jukki bi, bunt la ngir leeral li ñu bind ci Kàddug Yàlla. Maanaam dañuy yéene dajale jukki yi wax ci nit ñi, dëkk yi, bereb yi, mala yi ak yeneen mbir yi ñu mana gis ci Biibël bi, rawantina mbir yi jafe xam ci kaw anami Senegaal.
- Wàll:Nit ñi ci Kàddug Yàlla
- Wàll:Nit ñi ci Téere Tawreet
- Wàll:Nit ñi ci Téere Linjiil
- Wàll:Bereb yi ci Téere Linjiil
- Wàll:Baat yi jóge làkku ibrë
- Wàll:Baat yi jóge làkku yawut
- Wàll:Baat yi jóge làkku gereg
- Wàll:Per yi ak Xeer yi ci Kàddug Yàlla
- Wàll:Mala yi ci Kàddug Yàlla
- Wàll:Gàncax yi ak garab yi ci Kàddug Yàlla
- Wàll:Xeet yi
- Wàll:Yàllay xeet yi
- Wàll:Njàngalem Mbooloom Kirist yi am solo