Penku gu Sori mooy barab bi nga xam ne moo ëmb yenn réew yu Bëj-saalum-penku Asi, ak yenn diwaani Siin, ak Ooŋ Koŋ, ak Singapoor, ak Réewum Maleesi, ak dunu Taaywaan.

Dunu Ooŋ Koŋ

Ci diwaan bii di nan fa gis ay réew yu wuute, ca wàllu koom ak xarala. Ci genn wàll di nan fa gis Taywaan ak Koom-koomam gu naat, ak dunu Hoŋ Koŋ aky taaxikawam yi gën a kawe ci àdduna bi, ak. Ci geneen wàll, ay réew yu seen koom-koom cëslaayu, ba tay, ci mbéy, waa kaw gi nekk ci coona.

Limbari yi joxe nañ ay lim yuy firndeel ni Ooŋ Koŋ jiitoo ci Koom ak ci Xaral ci àdduna bi.

Diwaani Tugalasi
Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi