Ndiiwaani Senegaal

Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal.

Ndiiwani Senegaal

Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas. Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.

Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007.

Taariix Soppi

Limu tund yi (nosu topp abajada) Soppi

Tunduw Bàkkel Soppi

 
Ndiiwaani Bàkkel
  • Bala
  • Jaawara
  • Gudiiri
  • Kidiira

Tunduw Bambey Soppi

 
Ndiiwaani Bambey
  • Baba Garaas
  • Lambaay
  • Ngoy

Tunduw Biñoona Soppi

 
Ndiiwaani Biñoona
  • Jululu
  • Sinja
  • Tenduk
  • Tengori

Tunduw Cees Soppi

 
Ndiiwaani Cees
  • Nooto
  • Puut
  • Cenaba

Tunduw Dagana Soppi

 
Ndiiwaani Dagana
  • Mban
  • Roos Beeco

Tunduw Fatik Soppi

 
Ndiiwaani Fatik
  • Jaxaaw
  • Fimla
  • Ñaaxar
  • Taatagin

Tunduw Funjunj Soppi

 
Ndiiwaani Funjunj
  • Jilloor
  • Ñoojoor
  • Tubaakuta

Tunduw Gosaas Soppi

 
Ndiiwaani Gosaas
  • Kolobaan
  • Kawóon
  • Waajur

Tunduw Géejawaay Soppi

 
Ndiiwaani Géejawaay

Géejawaay moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 5 dëkkani ndiiwaan

Tunduw Kafrin Soppi

 
Ndiiwaani Kafrin

Dogiinu tund wi dañu koo soppi gannaaw sosug tunduw Kungeel ci 2006.

Kon mu des :

  • Birkilaan
  • Maleem-Odaar
  • Nganda

Tunduw Kanel Soppi

 
Ndiiwaani Kanel
  • Kanel
  • Seeme

Tunduw Kawlax Soppi

 
Ndiiwaani Kawlax
  • Ganjaay
  • Ndenjeng
  • Ndóofaan

Tunduw Kebemeer Soppi

 
Ndiiwaani Kebemeer
  • Daaru Musti
  • Ndand
  • Sagata

Tunduw Kéedugu Soppi

 
Ndiiwaani Kéedugu
  • Bandafasi
  • Fongolimbi
  • Salemata
  • Saraya

Tunduw Koldaa Soppi

 
Ndiiwaani Koldaa
  • Dabo
  • Julaacolon
  • Medina Yoro Fula

Tunduw Kungéel Soppi

Mi ngi judd ci 2006 (amul lonkoyoon bu jàppandi nii-nii)

Tunduw Lingeer Soppi

 
Ndiiwaani Lingeer
  • Barkeji
  • Daara
  • Dooji
  • Yang-Yang

Tunduw Luga Soppi

 
Ndiiwaani Luga
  • Kër Momar Saar
  • Kokki
  • Mbejeen
  • Sakal

Ndiiwaanu Raawo, biy feeñ ci lonkoyoon bi, ci tunduw Ndar la bokk 2002 ba tay.

Tunduw Mbuur Soppi

 
Ndiiwaani Mbuur
  • Fisel
  • Ngeexoox
  • Caajaay
  • Jiwaalo

Tunduw Maatam Soppi

  • Añam Ciwol
  • Ogo

Tunduw Mbakke Soppi

 
Ndiiwaani Mbakke
  • Kayel
  • Ndam

Tunduw Ndakaaru Soppi

 
Ndiiwaani Ndakaaru

Ndakaaru moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 19 dëkkani ndiiwaan.

Tunduw Njaaréem Soppi

 
Ndiiwaani Njaaréem
  • Ndindi
  • Ndulo

Tunduw Ndar Soppi

 
Ndiiwaani Ndar

Gannaaw dogaat ga waraaloon juddug Diiwaanu Maatam, tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu

  • Raawo

Tunduw Ñooro gu Rip Soppi

 
Ndiiwaani Ñooro gu Rip
  • Medina Sabax
  • Pawoskoto
  • Wak Nguna

Tunduw Pikin Soppi

 
Ndiiwaani Pikin

Pikin moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 16 dëkkani ndiiwaan.

  • Pikin

Tunduw Podoor Soppi

 
Ndiiwaani Podoor
  • Kas-Kas
  • Njum
  • Salde
  • Cile Buubacar

Tunduw Raneru Soppi

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Welingara

Tunduw Séeju Soppi

 
Ndiiwaani Séeju
  • Bunkiling
  • Jaatakunda
  • Jend
  • Marsasum
  • Tanaaf

Tunduw Siggcoor Soppi

 
Ndiiwaani Siggcoor

Tunduw Tambaakundaa Soppi

 
Ndiiwaani Tambaakundaa
  • Kumpentum
  • Kusaanaar
  • Makakolibantang
  • Misiira

Tunduw Tënjéej Soppi

 
Ndiiwaani Tënjéej

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Sebixotaan, moom ci boppam ñu séddale ko ci 3 dëkkaani Ndiiwaan.

Tunduw Tiwaawon Soppi

 
Ndiiwaani Tiwaawon
  • Meewaan
  • Merina Daqar
  • Ñaaxeen
  • Pambal

Tunduw Usuy Soppi

 
Ndiiwaani Usuy

Tunduw Welingara Soppi

 
Ndiiwaani Welingara
  • Bookoto
  • Kunkan
  • Pakur

Xool it Soppi

Lëkkalekaay yu biir Soppi

Lëkkalekaay yu biti Soppi

Téerekaay Soppi

  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)