Mbàmbulaan am mbalka mu réy la mu def ndoxum xorom, te wër ab gox.

Xumbalub lonkoyoonu mbàmbulaan yi
Dencukaay:Mappemonde oceanique Serret.gif
The world (global) ocean mappemonde océanique Serret

Mbooleem mbàmbulaan yi ak géej yi ñoo jël 70% di ñatti ñeenteel ci li ci Kaw kol-kolub suuf si, maanaam 360.700.000 km². Ci lim bii 154.800.000 km² ñoo ngi ci xaaju kol-kol bu bëj-gànnaar, 205.900.000 di km² ci xaaju kol-kol bu bëj-saalum.

Mbàmbulaan yi juróom lañu:

Waaye waa-Angalteer yi ci seen gisinu melosuuf da ñuy jàppee mbooleem géej yi ne ci li wër ñaari goxi dott yi, duppee leen Mbàmbulaan gu Bëj-gànnaar ak Mbàmbulaan gu Bëj-saalum.

Tangaay wu diggdóomu gu mbàmbulaan yi
Ci suuf 60° tus-w. Bëj-g Yamoo 60° tus-w. Bëj-s.
  Atlas Gu Dal Atlas Gu Dal Gu Eng Atlas Gu Dal Gu End
Ci kaw 27° 27° 27° 0,3° 0,8°
-100 m 10° 21° 25° 23° 0,1° 1,9° 0,6°
-500 m 3,5° 12° 2,5° 1,7° 1,2°
-1.000 m 4,5° 0,9° 1,5°
-3.000 m 2,8° 1,7° 0,3° 0,1° 0,1°