Ndimbal:Dalal-jàmm wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
mAucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
<poem>
'''Dalal-jàmm''', yaa ngi ci wikipedia gi ñu jagleel kàllaama Wolof, mu di jimbulaŋ bu [[Ndimbal:Jimbulaŋ bu ubbeeku|ubbeeku]] goo xam ne ñi koy jàng bokk nañu ci ñi koy bind.
Ku nekk man nga cee dugal sa loxo, bind ay jukki yu yees walla gën a baaxal li fi jot a nekk; ndaxte ngir sémb wi man a dox ci ni mu gëne, dafa laaj ay loxo yu bari. Ku mu man di doon, man nga cee jàpp ci kaw njekk ak teraanga, topp àtte yi ñu fi tëral, noo ngi lay dalal.
 
Li mu doon lu ubbeeku ngir ñépp te amul ag pay, ñi binduwul tamit ci biir, '''moo tax Wikipedia manul a joxe ay wóoral ci mbaaxaay ak cellteg ëmbiitam ''' Donte askanu wikipedia mi ngi tijjiy gëtam ngir di ko jéem a aar ci anam yu dëgër. Saa su ne, man naa am ay xët yu ñuy saay-saaye walla yu ñu soppi ci anam yu dul yi gën ci kaw tayeef, def ciy xibaar yu baaxul walla yu dëppóowul ak sa dundiinu waa-gox.
</poem>
 
==Nooy Yëre wikipedia==
<poem>Man ngaa tàmbalee ci [[xët wu njëkk]] wi te topp ci lëkkalekaay yi lay yóbb ci li la solool, li la soob ci njàng.
Su fekkee itam daa am jukki booy seet, man ngaa bind benn walla ay baat yu bari ci boyotu bind bi nekk ci sa cammoñ daal di "cuq" ci ''Ayca''
 
</poem>
* su fekkee baat bi nga bind dafa nekk kojug jukki ba noppi, dangay "cuq" ci ''Ayca'' rekk mu feeñ.
* su fekkee nak baat bi dafa nekk ci biiri xët yu am ba noppi, dangay "cuq" ci ''Seet''.