Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 4 :
'''Aj''' mooy juróomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ja ni: "Tabaxees na Lislaam ci juróom: Seere ne amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe Asaka, Woor weeru Koor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci bépp anam), ci waxi Yàlla mu kawe ja ni:ñeel na Yàlla ci nit ñi Aj néek ba ci ku ko man aw yoon (benn yoon) te ku weddi Yàlla moom woomle na waliif mbindéef yi.
 
== HajAj Màkka ak kumu war ==
 
HajAj Màkka benn yoon faratala ci mukàllaf mu ko man ci yaramam ak ci ab yobbalamyóbbalam.
Manug Yaram wi moodi mu bañ a ame wopp ju ko tee man a dem walla mu ragal
ca dem ga dollikug wopp ja, walla sosug wopp walla ak yeex a wér.
 
Yobbal bi yit moodi mu am lu ko lew lu sell loo xam ne darra ci ribbaa nekk unekku ca,
àqi kenn neek unekku ca, te yalwaanu ko ñaanu ko te mu doy ko sëkk ba du tumurànke ci yoon wi
du ca yalwaan du lëjal kenn, waa këram itam mu bàyyee leen lu leen doy sëkk ba du ñu tumuturànke
du ñu lëjal kenn. Mu fay boram yépp bu dul bu ab digam teewul, waaye bu dee teew balaa dellusi sax war na koo fay balaa dem walla mu batale ko.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële