Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 2 :
[[File:Al-haram.jpg|thumb|250px|<font color="grey">Haj</font>]]
 
'''Hajaj''' mooy juróomeelu ponku Lislaam, Ci waxi Yonent Yàlla Muhammed ja ni: "Tabaxees na Lislaam ci juroomjuróom: Seere ne amul benn buur bu dul Yàlla te Muhammed ndawam la, Taxawal Julli, Joxe AzakaAsaka, Woor weeru koorKoor, Ak Aj ci ku ko man aw yoon", ba tay Aj farata la ci benn jullit bu ko man (ci beppbépp anam), ci waxi Yàlla mu kawe ja ni:ñeel na Yàlla ci nit ñi Aj néek ba ci ku ko man aw yoon (benn yoon) te ku weddi Yàlla moom woomle na waliif mbindéef yi.
 
== Haj Màkka ak kumu war ==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële