Haj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 79 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q234915 (translate me)
Daarul xayri (waxtaancëru)
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 10 :
ca dem ga dollikug wopp ja, walla sosug wopp walla ak yeex a wér.
 
Yobbal bi yit moodi mu am lu ko lew lu sell loo xamnixam ne darra ci ribbaa nekk u ca,
àqi kenn neek u ca, te yal waanuyalwaanu ko ñaanu ko te mu doy ko sëkk ba du tumurànke ci yoon wi
du ca yalwaan du lëjal kenn, waa këram yitamitam mu bàyyee leen lu leen doy sëkk ba du ñu muturànketumuturànke
du ñu lëjal kenn. Mu fay boram yépp bu dul bu amab digam teewul, waaye bu dee teew balaa dellu sidellusi sax war na koo fay balaa dem walla mu batale ko.
'''Bu ci yooyu yépp amee naknag''' war na ko ni ko julli warewaree ku ko weddi ab yéefar la, ku ko bàyyi te tay ko te tëlewu ko ci genn anam ab saay-saay la bu bon te bu ko tuubul ba dee sawara la jëm.
Ku ko bëgg naknag bu demee ba fa muy armale dana fa fekk ku ko jiite ci yi mu war a def yeppyépp ak yi mu war a bàyyi yeppyépp ba ba muy noppi.
Moongi ware ci weeru Tabaski
[[Image:la_mecque_pelerinage.png|300px|right|thumb|Jeegoy Aji Màkka gi]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Haj » lañ ko jële