Alaaji Omar Taal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Orbwiki107 (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
MarcoAurelio (waxtaancëru)
redirect instead
Tafaan: Nouvelle redirection Éditeur visuel : basculé
Rëdd 1 :
{{delete|#redirect [[Alaaji Omar Fuutiyu TAAL]]}}
'''Alaaji Omar Fuutiyu Taal''' mi ngi gane àdduna ci ndëkk su ñu naan Elwaar, ci wetu Podoor atum 1794 -1796 g.j, mu bokkoon [[ci]] askan wu cosaanu ci Lislaam, baayam mi ngi tuddoon Sahiid mom Usmaan mom Muxtaar Tukkloor bi, yaayam tuddoon soxna [[Aadama]] Caam.
 
[[Dund]] na ay at ca barab yu sell ya (Màkka), bi mu déllusee réewam la dogu woon ci tas Lislaam te jële fi way sanc yi. Ci [[atum]] 1853 g.j, la jibal jiyaar ngir yékkati baatub « Laa ilaaha illal Laah » .
 
[[Mu]] song Karta ak Xaaso nangu leen, def fa imbraatóoram gu lislaam gi. Xareb Alaaji Oamar fenqoo na’ak bu Federb bi nga xam [[ne]] li ko yékkati woon mooy aar sancoom yi mu amoon ci sowwu bi, ak jéem a tegi loxo penku bi.
[[Alaaji]] Omar saxoon na te të ci kanamu dooley sanc gi, waaye ci mujj gi mu daanu ca doji Banja Gara ya ca Gine atum 1864 g.j. [[Bu]] ko defee doom ja Ahmad Seexu daal di yanu raayub jiyaar bi ci ginnaawam, waaye moom it amoon na ag lott ci kanamu [[ngànnaayu]] sancaan yu lëw yii te aaytal. Bi mu ñàkkee pexe la xaatim ag kóllare ak tubaay yi atum 1881 g.j, waaye Gayni mi [[mu]] defaloon kóllare googu daal di koy wor, ndax songaat na ko, ga ko ci mu daw, foofu la imbraatóor gi daanoo ci loxoy [[tubaab]] yi, atum 1889 g.j .
 
[[Wàll:Niti senegaal]]