Wolof (làkk) wuute gi ci sumb yi

18 octets ajoutés ,  3 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
Tafaan: recent_changes
Tafaan: recent_changes
Li ma bëgg a wax mooy naka lanu bëgg a bàyyee sunu làkk yii, rawati na wii di wolof, ca nooyam ga, ak nangoom ga, ak gàttam ga ak noppaleem ga, taaram ba, leeram ga, manam gaa leeral ak yaatoom ga, ak ruyu gi mu nangu, naan da nga'y jëlati weneen di ci sonn ak a sonle, naan day wa gën? Ma ne ñoom ñoo gis loolu man de déet !
 
Wolof mooy làkk wi ñu gën a wax ci [[Senegaal]], waaye ngir doyodig waa [[Afrig]] yi ba leegi, franse mii nganiga xam ne lu matul fukk my tight asshole cib téeméer ci doomi Senegaal yi rekk a koy wax moo fiy làkk wu njëkk, maanaam wi nguur gi di waxe di ci liggéeye.
 
== Cosaanam ==
Utilisateur anonyme