Cosaan wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes
Rëdd 3 :
[[Wàll:Cosaan]]
 
Ci xëtt wi, dama see fas yeeni jeema tekki ani lan moodi cosaan. Sama weerukay ci walu xam-xam moodi jangat-nit . Bile baat, manko tëggé ci (anthropologie), manaam anthro=nit ak pologie=jangat. Cosaan, aada, ak luñuubaaxo daño fasoo, dugantè lu bari. Waayé, ci sama gis-gis, cosaan moy reenu askanr, manaam fu aw askan bayee koo. Bilep firi daa ajju si walug bërëp (espace). Cosaan, mana firi batay luñu donnu ci makk ñi. Kon ci tënkk, cosaan, moy reenu askan, lunġa länkalee , di luñu baaxo def, loolu moo lay jox "culture" wala mu xeltu ko ta mu jem ci walu dundam, man nañ jappé "culture". Kon, suma suka ndikoo ci lii ma fessäl.
Cosaan nak, ci walu xeltu, baat bu jaxaso la. Ndax tekkina ay jëff . Sama laac moo: cosaan "embu" wala ab yan bu makk ñi doon aw laantoo, dalee ko ci maam yu yag ya ba si jamonoy tay ji?
Gëstukat , dalee ko ci jamano yu yàg ya, kon luy walbatiku. Nittu jamano boo jel, dañu tànn ci seen cosaan ay lëffin, wacci licci dess. Rax ci dooli, dañuy fen. Waaye timit, nguuruk reew munek war jôkaar . Cosa, don te mengo tul ak. Cosaan ak aaday Reew yi eup doolee dañu wali ci cosaanu reew yi new doolee, ak dileendi nasaxal.
 
Bu njekk, borom xam-xam yi bayoo tuggal ta see gëstu ajju ci walu jangat-nit. Li lalloon bilee weddi moodoon ne see dëkk yi ñoo noot, seeni kom-kom. Bi aduna doxee ba nootagee bi jeex, bu afrik moom boppam,, ñeppu nagu nagn ni askan yeppa am aada ak cosaan, ak seeni mbaax (valeurs). Nit ku nuul yam wanee ne nit Lolu di ndam lu rey si xeetu nit .Ndax te bo xamul , do xam .
SEEX LO
 
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Cosaan » lañ ko jële