Séeréer wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tamsier (waxtaancëru)
set setal
Tamsier (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 11 :
 
[[Léopold Sédar Senghor]], njiitul Senegaal lu njëkk séeréer la woon ca baayam, [[Abdu Juuf]] tam. Blees Jaañ moom it baayam Séereer la woon.
Séereer bu njëkk [[Ceddo]] lañu nekkoon - diiney ''"A ƭat Roog"'' ci baati Séeréer. Tay nag dugg nañu [[lislaam]] ( [[Tiijaaniya]], [[yoonu murit]]), walla diiney nasaraan (christianisme) ca Siin (Joal-Fadiouth). Nasaraanalkat yi (le Missionnaires) yu tubaab yi ñoo leen dugal ci diine jooju. Am na Séeréer ñu barry ñu tey ci diiney ''[[Diiney SéereerSéeréer|A ƭat Roog]]'' (religion sérère). ''[[Roog]]'' moi Yalla ci baati Séeréer.
 
Seen Sant yi gën a siiw : Juuf, Ngom, Fay, Seen, Saar, Seŋoor, Nduur, Joon, Joor, Jongu, Jeey, Njaay, Sekk, Ndong, Séy, Luum, Tin, Déen, Puy, Caw, Maróon, Ñing, Jóob, Gaajo.