Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Trey314159 (waxtaancëru)
m fix homoglyphs: convert Cyrillic characters in X[ё]dd to Latin
Tafaan: recent_changes
Trey314159 (waxtaancëru)
m fix homoglyphs: convert Cyrillic characters in ng[ё]néel to Latin
Tafaan: recent_changes
Rëdd 156 :
3 – ñaan booy dog, ndax Yonnant bi (j.m) daan na wax bu dogaan : “Allaahuma lakka sumnaa wa halaa risqika aftarnaa, fa taqabbal minna innaka antas samiihul haliimu” Ibnu Omar moom daan na wax: «Allaahuma innii asaluka birahmatikal latii wasihat kulla sayin, an taxfira sunoobii».
 
4 – Xëdd, mooy lekk ak naan ci waxtuw njël di mujjug guddi gi, ànd ak yéeney woor, ngir waxam ja (j.m) : "ngёnéelngënéel li tàqale sunug koor ak gu waa Ahlul Kitaab (ñoñ téere: Yahood yeek Nasaraan yi) mooy xëdd” ak waxam ja (j.m) : “xëddleen, xëdd de am na barke”
 
5 – yeexe xëdd ba ci xaaj bu mujj bi ci guddi gi, ngir waxam ja (j,m) : “sama xeet wi duñu dañ ciw yiw li feek ñi ngi gaaw a dog tey yeex a xëdd”
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële