Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Trey314159 (waxtaancëru)
m fix homoglyphs: convert Cyrillic characters in ñ[ё]w to Latin
Tafaan: recent_changes
Trey314159 (waxtaancëru)
m fix homoglyphs: convert Cyrillic characters in nj[ё]kk to Latin
Tafaan: recent_changes
Rëdd 152 :
1 – Gaaw a dog, mooy dog rekk bu jant bi sowee, ngir waxam ja (j.m) : “ nit ñi duñu dañ di nekk ciw yiw li feek ñi ngi gaaw a dog” ak waxi Anas ji (y.y.g) : “Yonnant bi (j.m) daawul julli timis ndare bu daa dog, ak doonte ci guuxub ndox la”
 
2 – doge ci tàndarma ju tooy mbaa ju wow, bu amul ndox, li ñu gёn sopp nag mooy mu tόol: ñatt walla juroom mbaa juroom ñaar, ngir waxi Anas doomi Maalik: “Yonnant bi (j.m) da daan doge ci tàndarma ju tooy njёkknjëkk muy julli, bu amul jёfandikoo tàndarma ju wow, bu amul mu guux ay guuxi ndox”
 
3 – ñaan booy dog, ndax Yonnant bi (j.m) daan na wax bu dogaan : “Allaahuma lakka sumnaa wa halaa risqika aftarnaa, fa taqabbal minna innaka antas samiihul haliimu” Ibnu Omar moom daan na wax: «Allaahuma innii asaluka birahmatikal latii wasihat kulla sayin, an taxfira sunoobii».
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële