Koor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 79 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q41662 (translate me)
Trey314159 (waxtaancëru)
m fix homoglyphs: convert Cyrillic characters in ñ[ё]w to Latin
Tafaan: recent_changes
Rëdd 215 :
Yii yépp dañuy yàq koor tey waral fayug bis ba ca yàqoo, waaye nag duñu waral kafaara, ndaxte kafaara moom du ware ndare ci ñaari way yàq koor yii:
 
1 – séy bu ñu tay te kenn manantewu la ci, ngir waxi Abuu Hurayra ja (y.y.g) : “waay ñёwñëw na ci Yonnant bi (j.m), ne ko man de alku naa yaw Yonnantub Yàlla bi, mu ne ko : lu la alag ? mu ne ko séy naak sama soxna ci ramadaan. Mu ne ko : ndax am nga jaam boo goreel? Mu ne deedeet, mu ne ko ndax man ngaa woor ñaari weer yu toftaloo? Mu ne ko deedeet, mu ne ko ndax am nga lu man a leel juroom benn fukki miskiin ? mu ne ko deedeet, daal di toog, Yonnant bi (j.m) daal di indi as ndàmba su def tàndar ma, ne ko am saraxeel lii, mu ne ko ndax dama koy sarax ku ma gёn a ñàkk? Yonnant bi ree ba ñuy gis bёñam ya, mu ne : demal jox ko sa ñoñ”
 
2 – lekk mbaa naan ci lu dul ngant lu ñu daganal: ci Aboo Haniifa ak Maalik (y.y.g), seenub tegtal mooy : “waay dog na ci ramadaan Yonnant bi (j.m) digal ko mu kafaara” ak àddiisu Aboo Hurayrat (y.y.g) mu ne : “waay ñёwñëw na ci Yonnant bi (j.m) ne ko : dog naa ci ramadaan te tay ko, Yonnant bi ne ko: goreelal ab jaam, mbaa nga woor ñaari weer yu toftaloo, mbaa nga leel juroom benn fukki miskiin”
 
=== li ñu daganal ci ku woor ===
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Koor » lañ ko jële