Kaasamaas wuute gi ci sumb yi

68 octets ajoutés ,  3 at ci ginaaw
+image
m (Bot: Migrating 22 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q839607 (translate me))
(+image)
 
[[File:FEMME S'ACTIVANT DANS UN CHAMPS DE RIZ.jpg|thumb|Kaasamaas]]
'''Kaasamaas''' baat la bu ñu toggalee ci ñaari dogiit : Kaasa ak Maas boo leen boolee muy buuru Kaasa. Kaasa bokk na ci yi [[njëkk]] ci nguuri gox bii. Ginnaawam nag Gabu moo ci gën a rëy ci nguur yi.
[[Ñaari]] nguur yii ñi ngi leen taxawal ci lu tollook xarub fukk ak ñeent g.j, ci loxol ay xarekat yu bawoo ca imbraatóoru [[Mali]] ga, Sinjata Kayta yabaloon leen. Nguurug Gabu (nguur gi ëppoon doole ci yii) Trimaskan Traaware moo ko sosoon, mu [[nekkoon]] gi tegoon loxo nguur yu ndaw yi nekkoon ci bëj-gànnaaru Gambi, ñooy : Kantora, Gimaara, Jaara, Kiyaŋ ak Kombo.
1 014

modifications