Jàngoroy Ebola wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Tafaan: recent_changes Soppikaay gu gisu
DARIO SEVERI (waxtaancëru)
Neenalug coppite 99307 yu 81.82.199.178 (waxtaan)
Rëdd 1 :
'''Jàngoroy Ebola''' ñu gënoon koo xamee ci '''Jàngoroy yaram-wu-tàng ju Ebola''' jenn xeetu jangoro la juy dal nit walla yenn bàyyima yi te [[doomu-jàngoro bu ebola]] di ko joxe. Xàmmeekaayu jangoro ji mi ngi tàmbalee feeñ ci diggante ñaari fan ba ñetti [[ayubés]] ginnaaw bi la [[doomu-jàngoro]] bi duggee, ngay ame yaram-wu-tàng, put guy metti, sidit yuy metti ak bopp buy metti. Ginnaw feeñte yu njëkk yii, naka-jekk, yi ciy topp ñooy, xel-muy-teey, waccu ak biir-buy-daw. Su ñu àggee fii ci [[jàngoro]] ji, ñenn nit ñi dañuy tàmbalee am ay nàcc-nàcc yu man a nekk ci biir yaram wi walla ci biti. Repp gee dee ci nit ñi ko amee dina àgg ci dayoo bu réy. Big booty Biches.
 
[[File:Ebola 1976-2014.svg|thumb|Barab yi ebola gën a feeñee ci 1976 ba 2014.