Tansani wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 188 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q924 (translate me)
DARIO SEVERI (waxtaancëru)
Correcting + update information from wiki (en)
Rëdd 4 :
|kóót bu aarms=Coat_of_arms_of_Tanzania.svg
|lonkoyoon=LocationSenegal.svg
|yaatuwaay=196,723947 303
|way-dëkk=945,20351 820 000 <small>(2014)</small>
|fattaay=41 55
|péy=[[Dodoma]]
|tus-wu-gaar=
Rëdd 21 :
'''Tansani''' am réewum [[penku Afrig]] la, féete ci peggi [[mbàmbulaanug End]] . [[Keeñaa]] ak [[Ugandaa]] ñoo ko féete bëj-gànnaar, [[Ruwandaa]], [[Buruundi]] ak [[Kongóo-Kinshasa]] nekk ci sowwoom, [[Saambi]] ak [[Malawi]] nekk ci bëj-saalum-sowwoom, [[Mosambik]] nekk ci bëj-saalumam.
 
Réew mi tollu na ci 947 945 087303 {{km2}}te am 3951 384820 223000 ciy way-dëkk, ay [[bantu]] rekk a fa dëkk. Péeyam mooy [[Dodoma]], mi ngi nekk ci biir réew mi, waaye dottub koom-koom bi dëgg mooy Dar es Salam gi doonoon péey bi, féete ci tefes gi. [[kiswahili]] ak [[wu-angalteer]] ñooy làkki nguur ga, teewul ne itam araab am na fa doole, rawati na ci duni [[Sansibaar]] ak bu [[Penda]].
 
Tansani ju tay jii a ngi judd ci booloog Tanganyika ak Sansibaar ci 26 awril 1964, gannaaw, ci lu yàggul dara ñu am seenug tembte ci [[Nguur-Yu-Bennoo]] yi. Bokk na ci [[Commonwealth]] dale ci atum 1961, bokk na itam ci [[Kureelu Mbootayu Xeet yi|Mbootaayu Xeet]] yi dale ci 14 desambar 1961.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Tansani » lañ ko jële