Wikipedia:Pénc mi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tafaan: Distribution par MassMessage
Strike Eagle (waxtaancëru)
m (GR) File renamed: File:Fomb.oggFile:Wo-fomb.oga File renaming criterion #4: To harmonize the file names of a set of images: so that only one part of all names differs.All Wolof words should start...
Rëdd 332 :
:::::waxtaan wi am na solo, te lii rekk mooy man a doxal liggéey bi, li tax ma sos xëti sémb yi mooy ngir nu man a diisoo ci ëmbiitu dal bi, te mooy sunu yéene nu ñépp. Su fekkee ku nekk dangaa bëgg a jox benn baat bi tekki ba la gën a neex mbir mi du sotti. Man mii, dëgg-dëgg, neenal laa gis ne mooy ba gën, ndax fomp nettoyer, effacer nga ko man a firee. Xaadir kebe, ci tekki yi, benn baat bu ne benn tekki nga ko man a jox, looloo tax ci xam-xamu nosukaay ma far yenn yi bàyyi fa benn tekki rekk, ci kanamu baatu wu-faraas bu nekk.--[[User:Ibou|Ibou]]<sup> ([[User talk:Ibou|xëtu waxtaanuwaay]])</sup> 23 Mee 2009 à 13:00 (UTC)
 
:::::: Jéggalu naa leen ci wax ji wolof yi neeñu: '''réeroo amul ñàkk a waxtaan a am''' lima bëggon a wax ak ligeen jàpp bokkul te maako waral ndax dama juum ci bindiin wi te bàyyi wu maci xel batax mu indi beneen baat bu bokkul ak bima nàmmona bind, fomb laa bëggon a bind juum bind fomp, bigeen ko méngalee ak nettoyer laa koy doora seetlu, ngir mu gën a leer manees naa deglu baat bi fii [[Dencukaay:FombWo-fomb.oggoga]]
*ginnaaw leer nani fomb laa bëg a wax ndax jàpp ngeen ni manees nakoo dëppale ak annuler ? ndax fomb mooy door mbir mbaa waaj ko te ba ko, <sup>Misaal</sup>:damadoon waaja dem tuubaa waaye fomb naa ko, Seen Xalaat/damaa dooroon ab laggeey waaye fomb naa ko ba jëmmi jamono ?
Jaajëf Sr Abdu Xaadir KEBE Jaajëf Ibraahima Faal cant ak gërëm ñeel na leen waaw-kay [[User:Ahloubadar|Ahloubadar]]<sup> ([[User talk:Ahloubadar|xëtu waxtaanuwaay]])</sup> 23 Mee 2009 à 13:44 (UTC)