Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
 
Rëdd 14 :
{{Babel|wo|fr-3|en-3|ar-4|it-0|es-0|}}
 
'''Abdu Xaadir GÉY''' dëkk ndakaaru. Ab Yorkat (admin) laa ci Wiki Wolof bii. Di kenn ci ñi sos Akaademi Wolof.
'''Sëriñ Abdu Xaadir GÉY Badar''' ('''Jiili GÉY''') juddoo Ndakaaru Senegaal, baayam tudd El Haaji Sëriñ Géy Badar (Raay mu sedd) yaayam tudd Soxna Ummi Njaay. Mu nekk Gueule Tapee ||, GUEDIAWAYE, DAKAR SENEGAL, Jamono yi mongi yaggu ci nosukaay gi (ordinateur)ak lepp lu aju ci xam-xamu xaymà (technologie mathématique), mu di ab "webmaster" (defarkatu dalu web) te di ab "specialist dans la localisation" (xam-xamam màcc jëm ci làkk i biir réew)
 
== Li nu Tax a Juk ==
Salaam bokki Wolof yi nun dey ay wolof lanu yu wolofe te yaakaar ni looloo nu war batax noo juk di laggeeyal wolof moomi ngir mu dabi ay nawleem walla mu jege leen, Te loolu jombul Wolof ndax Yàlla tàggat na ko ba mu nooy te matale, Man dey gis a gu ma làkk wu ko gën a mat, Xanaa kay li am mooy làkk wees toppatoo ak wees sàngane te melna ni Wolof ci yees xaw a sàngane la bokk, Nun dey loolu neexu nu batax noo juk fas-yéene cee def li nu ci man a kus neew ngir dooleel ko mbaa sax wone ko te nu yaakaar ni kepp kuy wolof war na cee jàpp ndax Yàlla mi la bind def la ngay wolof. di jéggaani aw làkk te yor wu mat, nooy te neex a wax loolu bokkul ci fulla day tax ñu yab la te xeeb la, looloo waral réewi tugal yi not ñu te yab nu ba leegi nde ñoo ñu abal aw làkk wu ñuy liggeeyee te Wolof nee «Ku la aal bët fu ko neex ngay xool», nun dey fippu nanu ngir bàyyil leen fi séen làkk yooyi du nu ci weesu wut xam-xam bi nu bokk ñun nit ñepp te ñu aakimoo ko def ko ci seen làkk yi, ndax xam-xam ku ne xam na ni Afrig la fékk baax doxondéem yi ñëw tibb ko yobbu. Li nu ci jot a am a kus neew nu tekki ko ci Wolof ngir askanu Wolof yi yëgul lu xew man cee njariñu, Fii ci sunu réew yi lu tax ñu yeex ? bokku na ci ku fi juddoo ñu dugal la ci daaray nasaraan yi 12at ngay jàng ngir dégg làkku nasaraan door a dugg ci daara ju kawe ji(universite) di jàng laggeey(métiers) 12at yooyii di juge ci sag dund ngir jàng aw làkk woo man a laggeeye te yor Làkku-Juddu wu mat manoon cee jànge xam-xam ci 12at yooyii, Xam ngéen ni loolu jaaduwul moo waral it doofi gis ku am xaalis ci'k ndawam ak yeneeni mbir yu wara tax ñu fonk suñu làkk wi, làkk woo xamni booy gent ci ngay gént booy saaga it ci ngay saaga, boo bëggee defar sa gent di nga ko jëfandikoo,
 
'''Jaajëf ci teewlu gi'''
 
== Jokkalekaay ==
 
*Jokkale gu dëkk: (221) 33837 00 27
*E-Bataaxal hotmail: djili.gueye@hotmail.com
*E-Bataaxal Yahoo: badargueye24@yahoo.fr
*E-Bataaxal: badargueye@gmail.com
*Dàli Web:
www.khitma.com
www.wolof.tk
www.wolof.co.cc
www.xibaaryi.com
www.senxarala.com
www.toubatube.com
www.khassidaonline.com
*Blog:
www.facebook.com/ahloubadar313
ahloubadar.blogspot.com
----
|}