Sëriñ Móodu Lóo Dagana wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Serigne Modou Lo Dagana
Tafaan: recent_changes
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Serigne Modou Lo Dagana''' (Sëriñ Móodu Lóo Dagana) mi ngi judd ci atum 1858 ca kër madu yala, mooy dëkku cosaanam, ma nga ca njàmbur ([[Luga|louga]]).
Moom ak sëriñ móodu lóo desaat fa ba 1902 ci la tubaab bi indiwaat sëriñ senegaal ñu ànd ñoom ñaar. Bi sëriñ bi amee ci réew mi ay weer tubaab yóbbuwaat ko gànnaar (mauritanie) sëriñ jëlaat sëriñ móodu lóo teg ko ca Dagana ne ko bu kenn ñëw te jaarul ci yaw.
Looloo waral ñu koy woowe sëriñ moodu loo dagana. Bi sëriñ bi jugee dagana la ko seexal boole kook ay taalube yu bari. Yabal ko saalum mu sënc fa ab dëkk di tërbiya, dëkk ba di dagana ca kër mbukki.
 
 Yaayam mi ngi tudd soxnaSoxna Astu lóo, baayam sëriñSëriñ subayruSubayru lóoLóo. Mi ngi jànge Alquraan ak xam-xam ca njàmbur ba mujj doon ab jànglekat bu mag.
Moom nag mi ngi fi juge dimenche 13 mars 1954 ca dakaar ñu indi ko tuubaa ci armeel yu mag yi.erigne Modou Lo Dagana
Sëriñ Móodu Lóo Dagana mi ngi judd ci atum 1858 ca kër madu yala, mooy dëkku cosaanam, ma nga ca njàmbur (louga).
 
Yaayam mi ngi tudd soxna Astu lóo, baayam sëriñ subayru lóo. Mi ngi jànge Alquraan ak xam-xam ca njàmbur ba mujj doon ab jànglekat bu mag.
Yoroon na lu mat fukki daara ak juróom ci kiliftéefam.
 
Mi ngi seeti sëriñ tuubaa ci atum 1898 juge ca kokki guy dëkkub ay nijaayam la.
Daa tëdd guddi am lu ko feeñu ne ko demal wuti ab sëriñ, ci la jug di seeti sëriñ tuubaa, te booba kenn xamul fu sëriñ tuubaa nekk, tubaab yi dañ koo génne woon (exiler).
Sëriñ moodu loo dagana dox seeti ko jaar na ci dëkk yu bari di dox ak tànkam ba gis sëriñ bi te xamul woon fumu nekk. Bi miy dem at la am ci yoon wi. Bis bim juge woon kokki guy ba mu delsee ca at mële la soog a gis sëriñ bi. Moom la sëriñ musaa ka naa:
Xëye na kokki guy bisub talaata*
namm ca géej ga bañu naan xad maata*
Ba weer deelsee ca déwen saak bis ba*
la doog a seeru bàmba ngir pas-pas ba*
 
Daa tëdd guddi am lu ko feeñu ne ko demal wuti ab sëriñ, ci la jug dine seeti sëriñSëriñ tuubaa, te booba kenn xamul fu sëriñSëriñ tuubaaTuubaa nekk, tubaab yi dañ koo génne woon (exiler).   
Mi ngi gis sëriñ tuubaa ci atum 1900 ca maayoomba ca gabon. Moom mooy senegalais bi njëkk a juge fii dem seeti sëriñ bi. Bi mu àggee toog na fa ay weer sëriñ bi yabal ko ne ko dellul senegaal wool ma maam seex Anta. Mu daal di ñëw senegaal woo seex Anta ànd ak moom yóbb ko gabon ca sëriñ ba. Moom la Sëriñ Musaa ka di wax naan " Sax na fa ay weer Bàmba xëy yabal ko* Mu woo si Siidi Anta Njaay toftal ko* .Sëriñ bi jox Maam seex Anta ay xasaayid yu bari yum taalifoon yabalaat ko mu ñëw senegaal.
 
Sëriñ mooduMóodu looLóo daganaDagana dox seeti ko jaar na ci dëkk yu bari di dox ak tànkam ba gis sëriñSëriñ bi te xamul woon fumu nekk. Bi miy dem at la am ci yoon wi. Bis bim juge woon kokki guy ba mu delsee ca at mële la soog a gis sëriñ bi. Moom la sëriñ musaa ka naa:
 
 
"''Xëye na kokki guy bisub talaata* ''
 
''namm ca géej ga bañu naan xad maata* ''
 
''Ba weer deelsee ca déwen saak bis ba* ''
 
''la doog a seeru bàmba ngir pas-pas ba* ''"
 
 
Mi ngi gis sëriñSëriñ tuubaaTuubaa ci atum 1900 ca maayoomba ca gabon. Moom mooy senegalaiswaa-senegal bi njëkk a juge fii dem seeti sëriñSëriñ bi. Bi mu àggee toog na fa ay weer sëriñSëriñ bi yabal ko ne ko, dellul senegaal wool ma maamMaam seexSeex Anta.   Mu daal di ñëw senegaal[[Senegaal]] woo seexSeex Anta ànd ak moom yóbb ko gabon[[Gaboŋ]] ca sëriñSëriñ ba. Moom la Sëriñ Musaa ka di wax naan " Sax na fa ay weer Bàmba xëy yabal ko* Mu woo si Siidi Anta Njaay toftal ko* .Sëriñ bi jox Maam seexSeex Anta ay xasaayid yu bari yum taalifoon yabalaat ko mu ñëw senegaal[[Senegaal]].
 
Moom ak sëriñ móodu lóo desaat fa ba 1902 ci la tubaab bi indiwaat sëriñSëriñ bi senegaalSenegaal ñu ànd ñoom ñaar. Bi sëriñSëriñ bi amee ci réew mi ay weer, tubaab bi yóbbuwaat ko gànnaar (mauritanie) [[Gànnaar]], sëriñ jëlaat sëriñ móoduMóodu lóoLóo teg ko ca Dagana ne ko bu kenn ñëw te jaarul ci yaw.
 
Looloo waral ñu koy woowe sëriñ mooduMoodu loo daganaDagana. Bi sëriñSëriñ bi jugee daganaDagana la ko seexal boole kook ay taalubetaalibe yu bari. Yabal ko saalum mu sëncsanc fa ab dëkk di tërbiya, dëkk ba di dagana ca kër mbukki.
 
 Moom nag mi ngi fi juge dimenche[[dibéer]] 13 mars[[Maars (weer)|maars]] 1954 ca dakaar[[Diiwaanu Ndakaaru|Ndakaaru]] ñu indi ko tuubaa[[Tuubaa]] ci armeel yu mag yi.erigne Modou Lo Dagana
 
==Xët yi mu lëkkalool==
* [[Nahju]]
* [[Muriidulaa]]
 
[[Wàll:niti senegaal]]
[[Wàll:Yoonu murit]]