Ndimbal:Nooy sose aw Xët wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Seexloo (waxtaancëru)
Tafaan: Soppi ak jollasu Soppi ak jullasu
Ibou (waxtaancëru)
m Loppantig coppite gu Seexloo (Waxtaan) dello ko ci sumb mu Ibou
 
Rëdd 8 :
Bari nañu, ñuy sàkk ay xët yu bees yu amoon ba noppi ak tur yu wuuteg yi fi nekkoon te seen ëmbit benn la, li ko waral mooy ki sàkk xët wu mujj wi seetul bu baax ndax li mu bëgga dugal am na fi ba noppi walla déet.
 
== Nan la ñuy amee xët wu amul-dara ak kojam? ==
[[Serigne Modou Lo Dagana]] Sëriñ móodu lóo dagana mi ngi judd ci atum 1858 ca kër madu yala, mooy dëkku cosaanam, ma nga ca njàmbur (louga).
* Am na ay yoon ngir sàkk xët wu bees:
 
**ci biir jukki yu am yi ba noppi cuqal ci lëkkalekaay yu xonk yi.
Yaayam mi ngi tudd soxna Astu lóo, baayam sëriñ subayru lóo. Mi ngi jànge Alquraan ak xam-xam ca njàmbur ba mujj doon ab jànglekat bu mag.
** Su fekkee dangaa bëgga wax ci lu bees, lu fi nekkul woon, lu njëkk li nga wara def mooy dem ci boyotu seetukaay bi "''Seet''" (mooy nekk ci cammoñu xët yi), man ngaa gis jukki yi mu méngool walla ci biir ay jukki yoo ko mana dugal (soo bëggee bind ab jukki ci Kajoor, dugal ko ci biir nguuri Senegaal mooy gën). Kon nga tijji xët wi nga yaakaar ne ci biiram war nga faa mana def ab lëkkalekaay buy tudd [[Kajoor]], boo xam ne soo ci cuqe mu yóbb la ci xëtu Kajoor wi. Nii nga koy bindee <nowiki>[[Kajoor]]</nowiki>. Day xonq, su ko defee nga tijji ko def ci li nga ci namm.
Yoroon na lu mat fukki daara ak juróom ci kiliftéefam.
** ''"Ayca"'' moom da lay laaj ndax bëgg ngaa sos xët wi ak baat bi nga bind mu nekk kojam, su fekke amul benn jukki bu tudd noonu. Jar naa teey ak bii sosin ndax doy na ab wuute bu tuut ci baat yi mu sosloola jukki bu bees.
 
Mi ngi seeti sëriñ tuubaa ci atum 1898 juge ca kokki guy dëkkub ay nijaayam la.
Daa tëdd guddi am lu ko feeñu ne ko demal wuti ab sëriñ, ci la jug ne day seeti sëriñ tuubaa, te booba kenn xamul fu sëriñ tuubaa nekk, tubaab yi dañ koo génne woon (exiler).
Sëriñ moodu loo dagana dox seeti ko jaar na ci dëkk yu bari di dox ak tànkam ba gis sëriñ bi te xamul woon fumu nekk. Bi miy dem at la am ci yoon wi. Bis bim juge woon kokki guy ba mu delsee ca at mële la soog a gis sëriñ bi. Moom la sëriñ musaa ka naa:
Xëye na kokki guy bisub talaata
namm ca géej ga bañu naan xad maata
Ba weer deelsee ca déwen saak bis ba
la doog a seeru bàmba ngir pas-pas ba
 
Mi ngi gis sëriñ tuubaa ci atum 1900 ca maayoomba ca gabon. Moom mooy senegalais bi njëkk a juge fii dem seeti sëriñ bi. Bi mu àggee toog na fa ay weer sëriñ bi yabal ko ne ko dellul senegaal wool ma maam seex Anta. Mu daal di ñëw senegaal woo seex Anta ànd ak moom yóbb ko gabon ca sëriñ ba. Sëriñ bi jox seex Anta ay xasaayid yu bari yum taalifoon yabalaat ko mu ñëw senegaal.
 
Moom ak sëriñ móodu lóo desaat fa ba 1902 ci la tubaab bi indiwaat sëriñ bi senegaal ñu ànd ñoom ñaar. Bi sëriñ bi amee ci réew mi ay weer tubaab yóbbuwaat ko gànnaar (mauritanie) sëriñ bi jëlaat sëriñ móodu lóo teg ko ca Dagana ne ko bu kenn ñëw te jaarul ci yaw.
Looloo waral ñu koy woowe sëriñ moodu loo dagana. Bi sëriñ bi jugee dagana la ko seexal boole kook ay taalube yu bari. Yabal ko saalum mu sënc fa ab dëkk di tërbiya, dëkk ba di dagana ca kër mbukki.
 
Moom nag mi ngi fi juge dimenche 13 mars 1954 ca dakaar ñu indi ko tuubaa ci armeel yu mag yi.
</poem>
[[catégorie:jeego yu njëkk]]