Kiswahili wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Magioladitis (waxtaancëru)
m →‎yeneen dali web : all info is now kept in wikidata, removed: {{Link FA|he}} using AWB (10862)
Cyrus noto3at bulaga (waxtaancëru)
m ce
Rëdd 2 :
'''Kiswahili''', walla làkku suwayli aw [[làkk]] la wees di wax ci anam gu yaatu ci [[Penku Afrig]] gi. Ci Suwayli turu làkk wi mooy '''Kiswahili'''. Moom nag aw làkk wu [[Bantu]] la.
 
Suwayli nag dees na ko wax ci gox bu yaatu ci Afrig, la ko dale ca bëj-saalumu [[Somaali]] ba ca bëj-gànnaaru [[Mosambik]] ak [[Keeñaa]] gépp. Lu tollook juroomi milyoŋ yu muy seen làkk wu njëkk a ngi fi (yu muy seen làkk wi ñu nàmp), ak juroom fukki milyoŋ ciy nit yu muy seen ñaareelu làkk (làkk wu ñu jàng). Suwayli mujj na di làkk wow nit ñi man nañu ciy jokkoo ci penku Afrig ak barab yi ko wër.
 
Suwayli tàmbali naa nekk làkk wees di wax ci [[Sansibaar]], benn dun ci Tansaani. Suwayli làkk wu kilifawu la (officiel) ca [[Tansani]] ak [[Keeñaa]]. Moom nag làkk wu jeexiitalu la ci yeneen làkk yu bari niki wu [[araab]]. Niki làkk yu bari ci Afrig Suwayli nekkoon na di lees di binde ci arafi araab waaye leegi ci yu laatiin yi lañu koy binde.