Séeréer wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tamsier (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tamsier (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 11 :
 
[[Léopold Sédar Senghor]], njiitul Senegaal lu njëkk séeréer la woon ca baayam, [[Abdu Juuf]] tam. Blees Jaañ moom it baayam Séereer la woon.
Séereer bu njëkk [[Ceddo]] lañu nekkoon, tay- diiney ''"A ƭat Roog"'' ci baati Séeréer. Tay nag dugg nañu [[lislaam]] ( [[Tiijaaniya]], [[yoonu murit]]), walla diiney nasaraan (christianisme) ca Siin (Joal-Fadiouth). Nasaraanalkat yi (le Missionnaires) yu tubaab yi ñoo leen dugal ci diine jooju. Am na Séeréer ñu barry ñu tey ci diiney ''A ƭat Roog'' (religion sérère). ''Roog'' moi Yalla ci baati Séeréer.
 
Seen Sant yi gën a siiw : Juuf, Ngom, Fay, Seen, Saar, Seŋoor, Nduur, Joon, Joor, Jongu, Jeey, Njaay, Sekk, Ndong, Séy, Luum, Tin, Déen, Puy, Caw, Maróon, Ñing, Jóob, Gaajo.
 
[[Wàll:Taariixu senegaal]]