Weeri wolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
JimeoWan (waxtaancëru)
defar benn lëkkalekaay
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Weeri wolof]], ci [[arminaat|arminaatu]] gàddaay gi, walla bu [[jullit]] ñi mbaa bu [[Lislaam]], ab arminaat bu weer la, buy sukkandiku ci doxiinu weer wi ngir xam ak natt weer wi. Jullit ñi danañu ko jëfandikoo ci bépp barab, rawati na ngir natt ak xam xew-xewi ak bisi diine yi. Ki ko sos nag mooy [[Omar Ubn Xattaab]] (g.m), daal di def [[gàddaayug Yonent]] bi (j.m) juge [[Màkka]] dem [[Madiina]] muy ab tàmbaleem, looloo waral deesi tudde ko arminaatub gàddaay gi. Ak doonte arminaat bi ci jamonoy jullit ñi lañu ko sos, teewul turi weer yi ak arminaatub weer ñu leen daa jëfandikoo calu jamonoy réer ga (jaahiliya, maanaam njëkkjiitu Lislaam).
 
Yenn ci [[réew]]i [[araab]] yi, mu ci mel ne [[Araabi Sawdit]], -moom ci nguur geek askan wi - dañuy jëfandikoo arminaatub gàddaay gi niki arminaat bu kilifawu di ci taariixe ci bindante yiy am ci diggante liggéeyuwaayi nguur gi, waaye nag lu ci dul moom, askani araab yi ci des yépp dearminaatu beneen[[Arminaatu Garegori|Garegori]] (bi lañudale miinci tejuddug moomYonent itYàlla Iisaa) lañuy jëfandikoogën muya bu judd gi (juddug yonent Yàlla Isaa (jjëfandikoo.m)).
 
Arminaanub gàddaay gi mi ngi ame ci 12 [[weer]] yu weer wi, maanaam atum gàddaay gi mi ngi tollook 354 bés daanaka, maanaam 354.367056 ci ay bés. Weer wi ci arminaatu gàddaay gi, benn mu nekk 29 walla 30 bés (ndax doxug weer wu feeñ wi 29.530588 bés la). Ginnaaw nag wuuteg 11 fan am na ci diggante [[Arminaatu jant|arminaatu judd]] gi ak bu gàddaay gi, ñaari arminaat yi duñu jamonoo mukk (duñu tolloo mukk) looloo waral dëppale leen di gën a jafe.
 
== [[Weer]] ci arminaatu gàddaay gi ==