Kureelu Mbootayu Xeet yi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 4 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q1065 (translate me)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
Rëdd 1 :
'''Kureelu Mbootaayu Xeet''' yi ndawi réew yu mag yi, yu ci mel ni [[Nguur-Yu-Bennoo]] , [[Diiwaan-yu-Bennoo]] yu [[Aamerig]], [[Bennog Sofyet]], [[Faraas]] ak [[Siin]], danoo daje woon ci Wasington peeyub Amerig ci wenn waxtaan atum 1933g, ginaaw bi as lëf ci ndam tàmblee feeñ ñeel reewi tapoo yi .j
Ci noonu nu gëstu woon nan lanu fiy sose ag mbootaay gu adduna guy yëngu ci saxal ponki jàmm ci adduna bi, jële fi xeex yi, amal fi maandute ak yamoo ci diggante mbooleem reew yi, ak rafetal nekkiinu mboolaayu r;ew yi, ci koom-koom, mboolaay, aada ak wér.
Bi loolu jàllee nu def benn dajeb waxtaan bu [[àdduna]] bi ci dëkku [[San Fransisco]] ci 25 awril atum 1945, ngir rëdd fa ag kollëre ñeel ag mbootaayug xeet gu yees gu fiy wuutu kureelu xeet yi.
Rëdd 8 :
[[Dencukaay:Flag of the United Nations.svg|300px|thumb|raaya bu Kureelu Mbootayu Xeet yi]]
[[Dencukaay:United Nations HQ - New York City.jpg|300px|thumb|Makkaanaam ca [[New York]]]]
 
== Sosteefam ==
Njiitul [[Aamerig]] la tuddoon [[Widro WILSO]]N da doon ku daa xalaat nu mu fiy taxawale mbootaay gu mag gu àdduna bi, guy jeem a indi jàmm ci àdduna bi, ci ginaaw [[Xareb Àdduna bu Njëkk]] bi.