Wolof (làkk) wuute gi ci sumb yi

62 octets ajoutés ,  5 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
[[Image:Wolof_Locator.png|thumb|Wolof làkk ([[Senegaal]])]]
 
'''Wolof''' [[làkk]] la wu ñuy wax ci [[Gaambi]] ([[Gaambi Wolof]]), [[Gànnaar]] ([[Gànnaar Wolof]]), ak [[Senegaal]] ([[Senegaal Wolof]]). Mi ngi bokk nag moom wolof ci bànqaasub [[atlas bu làkki]] kongoo yu kojug nit ku ñuul yi. Mbokkoo gi mu am ak [[làkk]]u pël lu yàgg la. Am na it lu mu seq ak yeneen [[làkk]] ci gox bi niki séeréer, joolaa ak basari.
 
Utilisateur anonyme