Ubbi njël lu njëkk li

Modifications

Aucun changement de taille, il y a 3 ans
[[Dencukaay:Wikipedia Administrator.svg|right|frameless]]
 
== Lan a waral ay saytukat yi? ==
 
Ngir mën a doxal ca na mu gën a rafete bërëb bu deme ni Wikipedia nga xam ni gan gunëwgu ñëw gu ne am nga sañ-sañu soppi daanaka xët yépp, fàww mu jmtukaayam jumtukaay yu dëggërdëgër yuy maye ci misaal, dëbësaatdëbasaat njuumte yi, far xët yuyi amul benn solo, jéng cib diir ay xët mbaa nu yàq yékkati.
 
Ngir solosoloy kaaraange, jumtukaay yu deme noonu, mënunumënu nu koo dénk néppñépp. Loolo waral céru saytukat jogjóg.
 
Nungi koy jagleel way doxali Wikipedia yi ko laaj te yit mbooloo mi jox léenleen séenseen koolutekóolute.--[[JëfandikukatJëfandikóokat:Maamdaawur|Maamdaawur]] 13 Baraxlu 2007 à 16:48 (UTC)Maam Daour Wade:16:56
 
== Lu ab Yorkat man a def ? ==
Utilisateur anonyme