Epatit A wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ian Henderson (waxtaancëru)
Added caption
Pamaboca (waxtaancëru)
m →‎Royuwaay yi : Acute
Rëdd 11 :
| MeshID = D006506
}}
'''Epatit A''' (ñu gënoon ko xamee ci turu '''epatit biy dale''') doon na [[Jàngoro juy dale]] [[Buju tar (medical)|acute]] buy jàpp [[res wi]] te li koy joxe di doomu jàngoro biñ naan Epatit A (HAV).<ref name=Sherris>{{cite book | author = Ryan KJ, Ray CG (editors) | title = Sherris Medical Microbiology | edition = 4th | pages = 541–4 | publisher = McGraw Hill | year = 2004 | isbn = 0-8385-8529-9 }}</ref> Bari na lu muy dal nit te du feeñ rawatina ci ndaw yi.<ref name=AFP2012/> Diggante bi muy dugg sa yaram ak bi muy tàmbalee feeñ, mi ngi tollu ci diggante ñaar ba juróom-benni ayi-bis.<ref name="pmid16271543">{{cite journal| author=Connor BA| title=Hepatitis A vaccine in the last-minute traveler| journal=Am. J. Med.| volume=118 |issue=Suppl 10A| pages=58S–62S| year=2005| pmid=16271543| doi=10.1016/j.amjmed.2005.07.018}}</ref> Su la dalee mën na def ak yaw juróom ñatti ayi-bis te dina faral di ànd ak: xel muy teey, waccu, biir buy daw, [[jaundice|der bu mboq]], yaram wu tàng, ak mettitu biir.<ref name=AFP2012/> Luy tollu ci 10 ba 15% ci ñi mu dal ñooy wéy di ko gis su demee ba weesu juróom-benni weer ginaaw bi mu leen dalee.<ref name=AFP2012/> Mag ñi mën nañu ci jëlee [[Feebaru res bu tar]] waaye bariwul lu muy dale.<ref name=AFP2012/>
 
<!-- Cause -->