Biir bu daw wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
CFCF (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Pamaboca (waxtaancëru)
→‎Royuwaay yi : biir buy daw
Rëdd 14 :
}}
<!-- Definition and Characteristics -->
'''Biir bu daw''' wala '''Jaare''' mooy ngay dem wanag gën gaa néew ñatti yoon ci bis te li ngay génne [[ginaaw kër yi]] dafay ndoxe.<!--<ref name=WHO2013/> --> Yenn saa mu jàpp la ay fan, te loolu mën na tax sa yaram [[ñàkk ndox]].<!--<ref name=WHO2013/> --> Su yaramu nit ñàkkee ndox deram dootul nooy te it mën a soppiku.<!--<ref name=WHO2013/> --> Mën nga dem ba dootoo [[saw]] lu bari, sab [[der furi]], sa [[xol di tëf-tëfi]], akte sam [[xel mu doxul ni mu waree wala jëf yu yeex, |xel dootul dox ni mu waree wala say jëf yeex,]] su demee ba gën a tar.<!--<ref name=WHO2013/> --> Ginaaw kër yu tooy te bañ a ndoxe mën dal liir yuyyiy [[nàmp]], waaye, loolu du dara.<ref name=WHO2013/>
 
<!-- Cause and Diagnosis -->
Li koy gën a faral di joxe mooy jàngoro ciyiy jàpp [[butit]] yi te di bawoo ci ab [[wiris]], [[bakteri]], [[parasit]], wala feebar bu ñuy woowe [[gastroenteritis]].<!--<ref name=WHO2013/> --> Yooyu jàngoroo ngi faral di bawoo ci ndox wala ñam wu am doomu jàngoro ji, wala ku am jàngoro ji wàll la ko.<!--<ref name=WHO2013/> --> Mën nañu ni ñàtti xeeti biir bu daw ñoo am: biir bu daw bu yàggul, biir bu daw bu ànd deret bu yàggul, ak biy weesoo ñaari ayi-bis, muy biir bu daw bu yàgg.<!--<ref name=WHO2013/> --> Biir bu daw bu yàggul te ndoxe mën na nekk [[kolera]].<!--<ref name=WHO2013/> --> Su àndee ak deret, ñu gën ko xame ci [[disànteri]].<ref name=WHO2013/> Amna yeneen mbir yu wuute ak jàngoro yu mën a joxe biir bu daw, muy lu ci melni: [[Ipertiroyidism]], [[biir buy bañ soow]], [[feebaru biir buy metti]], yenn xeeti garab yi, ak [[sendoromu biir buy metti]] ak yeneen mbir.<ref name=CEM2013>{{cite book|last1=Doyle|first1=edited by Basem Abdelmalak, D. John|title=Anesthesia for otolaryngologic surgery|date=2013|publisher=Cambridge University Press|location=Cambridge|isbn=1107018676|pages=282–287}}</ref> Yi gën bari ci ñoom soxlawu ñu ñuy amal [[njàngat mu xóot]] ngir xam li leen waral.<ref name=NEJM2014/>
 
<!-- Prevention and Treatment -->
Liy musalaate ci biir bu daw mooy [[cet]], di naan [[ndoxu naan]]|ndox mu sell]], ak [[raxas loxo]].<!--<ref name=WHO2013/> --> [[Nàmpal]] liir ba juróom benni weer gën gaa néew lañu digle ak [[ñaqu rotawiris|ñaq buybiy aare ci rotawiris]].<!--<ref name=WHO2013/> --> [[Naan ndox mu koy faj|Pajtalu naan ndox muy faj]] (ORS), manaam ndox mu sell muñ boole ak tuuti xorom ak [[suukër]], kumu neex nga fajoo ko.<!-- <ref name=WHO2013/> --> kumu neex itam nga jëfandikoo [[Zinc#Dietary supplement|doomi Zinc]].<ref name=WHO2013/> Xayma nañu ni garab yooyu muccal nañu 50 miliyo?imiliyoŋi xale ci 25 at yii weesu.<ref name=WHO2010a>{{cite web |url=http://whqlibdoc.who.int/publications/2009/9789241598415_eng.pdf |title=whqlibdoc.who.int |format=PDF |work=[[World Health Organization]]}}</ref> Taamu nañu ci ku am biir buy daw mu wéy di lekk ñam wu sell, sudee liir ñu wéy di ko nàmpal.<ref name=WHO2013/> Soo amul foo jëndee ORS (ndox muñ jaxase ak xorom ak suukër), mën nga koo defaral sa bopp.<ref name=Prober2012>{{cite book|last1=Prober|first1=edited by Sarah Long, Larry Pickering, Charles G.|title=Principles and practice of pediatric infectious diseases|date=2012|publisher=Elsevier Saunders|location=Edinburgh|isbn=9781455739851|page=96|edition=4th |url=http://books.google.ca/books?id=TN2Gu2Af1BIC&pg=PA96}}</ref> Sudee nit ki daa ñàkk ndox mu bari, war nañu ko mën a [[sampal buteel]].<ref name=WHO2013/> Lu ci gën bari; naan ndox mu bari mën na ko saafara.<ref>{{cite web|author1=ACEP|title=Nation’s Emergency Physicians Announce List of Test and Procedures to Question as Part of Choosing Wisely Campaign|url=http://www.choosingwisely.org/nations-emergency-physicians-announce-list-of-test-and-procedures-to-question-as-part-of-choosing-wisely-campaign/|website=Choosing Wisely|accessdate=18 June 2014}}</ref> [[Antibiotik]]s, suñu ko jëfandikoowul lu bari, dina ciy faral di baax ci ñi am biir buy daw ànd ak deret ak yaram wu tàng lool, ak ñiy tukki di am [[biir buy daw bu ñu tukkee]], ak ñi am yenn jàngoro yi ci seen biir.<ref name=NEJM2014/> [[Loperamide]] mën na wàññi jaabante bi ci wanag wi waaye kenn digalu ko ñi seen biir bu daw tar lool.<ref name=NEJM2014>{{cite journal|last1=DuPont|first1=HL|title=Acute infectious diarrhea in immunocompetent adults.|journal=The New England journal of medicine|date=Apr 17, 2014|volume=370|issue=16|pages=1532–40|pmid=24738670|doi=10.1056/nejmra1301069}}</ref>
 
<!-- Epidemiology and Prognosis -->
At mu nekk dina am lu tollu ci 1.7 ba 5 miliyaar ciy biir yuy daw.<ref name=WHO2013/><ref name=CEM2013/> Fi mu gënee bari mooy ci [[réew yu néew doole yi]], nga xam ni xale bu nekk biiram dina daw ci xayma ñatti yoon ci at mi.<ref name=WHO2013/> Ci àdduna bi yépp, ci atum 2012, mooy ñaareelu jàngoro juy [[faat xale yi]] yi amagul juróomi at (0.76 miliyo?miliyoŋ wala 11%).<ref name=WHO2013/><ref name=CDC2013/> Biir bu daw bu bari mooy faral di indi [[xiibon]] te itam mooy li ko gën a faral di joxe ci xale yi amagul juróomi at.<ref name=WHO2013>{{cite web|title=Diarrhoeal disease Fact sheet N°330|url=http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs330/en/|website=World Health Organization|accessdate=18 June 2014|date=April 2013}}</ref> Su yàggee mën na jur jafe-jafe yu ci melni ñàkk kàrtan ñàkk a amwala xel mu neex.<ref name=CDC2013>{{cite web|title=Global Diarrhea Burden|url=http://www.cdc.gov/healthywater/global/diarrhea-burden.html|website=CDC|accessdate=18 June 2014|date=January 24, 2013}}</ref>
 
==Royuwaay yi==