Biir bu daw wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ian Henderson (waxtaancëru)
Created article
 
CFCF (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
{{Infobox symptom
|  Name = Biir bu daw
|  Image = Multiple rotavirus particles.jpg
|  Caption = Ab mikrograf elektronigu  [[rotavirus]], li waral lu tollu ci 40% ci xale yi amagul juróomi at yi biir bu daw di tëral ci lopitaal.<ref name=WHO2010a/>
|  DiseasesDB = 3742
|  ICD10 =  {{ICD10|A|09||a|00}},  {{ICD10|K|59|1|k|55}}
|  ICD9 =  {{ICD9|787.91}}
|  ICDO =
|  OMIM =
|  MedlinePlus = 003126
|  eMedicineSubj = ped
|  eMedicineTopic = 583
|  MeshID = D003967
}}
<!-- Definition and Characteristics -->
'''Biir bu daw'''  wala  '''Jaare''' mooy ngay dem wanag gën gaa néew ñatti yoon ci bis te li ngay génne  [[ginaaw kër yi]] dafay ndoxe.<!--<ref name=WHO2013/>   -->  Yenn saa mu jàpp la ay fan, te loolu mën na tax sa yaram  [[ñàkk ndox]].<!--<ref name=WHO2013/>   -->  Su yaramu nit ñàkkee ndox deram dootul nooy te it mën a soppiku.<!--<ref name=WHO2013/>   -->  Mën nga dem ba dootoo  [[saw]] lu bari,  sab [[der furi]], sa  [[xol di tëf-tëfi]], ak  [[xel mu doxul ni mu waree wala jëf yu yeex, ]]  su demee ba gën a tar.<!--<ref name=WHO2013/>   -->  Ginaaw kër yu tooy te bañ a ndoxe mën dal liir yuy  [[nàmp]], waaye, loolu du dara.<ref name=WHO2013/>
 
<!-- Cause and Diagnosis -->
Rëdd 23 :
 
<!-- Epidemiology and Prognosis -->
At mu nekk dina am lu tollu ci 1.7 ba 5&nbsp; miliyaar ciy biir yuy daw.<ref name=WHO2013/><ref name=CEM2013/> Fi mu gënee bari mooy ci [[réew yu néew doole yi]], nga xam ni xale bu nekk biiram dina daw ci xayma ñatti yoon ci at mi.<ref name=WHO2013/> Ci àdduna bi yépp, ci atum 2012, mooy ñaareelu jàngoro juy [[faat xale yi]] yi amagul juróomi at (0.76 miliyo? wala 11%).<ref name=WHO2013/><ref name=CDC2013/> Biir bu daw bu bari mooy faral di indi [[xiibon]] te itam mooy li ko gën a faral di joxe ci xale yi amagul juróomi at.<ref name=WHO2013>{{cite web|title=Diarrhoeal disease Fact sheet N°330|url=http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs330/en/|website=World Health Organization|accessdate=18 June 2014|date=April 2013}}</ref> Su yàggee mën na jur jafe-jafe yu ci melni ñàkk kàrtan ñàkk a am xel mu neex.<ref name=CDC2013>{{cite web|title=Global Diarrhea Burden|url=http://www.cdc.gov/healthywater/global/diarrhea-burden.html|website=CDC|accessdate=18 June 2014|date=January 24, 2013}}</ref>
 
==Royuwaay yi==