Màbba Jaxu Ba wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Faolin42 (waxtaancëru)
link to Siin
Tamsier (waxtaancëru)
Santi "Jeey" (Jaay) du Wolof di. Seereer la. Ay Seereer Saaluum-Saaluum lenge
Rëdd 1 :
Mabba Jaxu Ba ci atum 1809 la judd ca nguurug [[Saalum]]. Baayam Njógu Ba la tuddoon, Sëriñ bu mag la nekkoon, ci xeetu Tukuloor la juge, soog a tuxu Saalum, ca nguuru Fuuta-Tooro la dekke woon. Yaayi Màbba Jaxu, Jaxu Jéey la tuddoon, [[Jolof]] la juddoo ci xeetu Wolof[[Seereer]] la bokkoon (nekkon Seereer bo "Wolofized" ci baati angale). Mabba Jaxu Ba, Almaami bu Rip la nekkoon, ba atum 1867. Ci at moomu , tase na ak [[Kumba Ndóof Seen Juuf]] Buur [[Siin]] bi, ci xeex bu nu tudde woon Somb-Cucun ci nguuru Siin, la deewe. Ci xeex bi [[Lat Joor]] Ngóon Latiir Jóop ak [[Alburi Njaay]] la àndaloon.
 
[[Wàll:Taariixu senegaal]]