Cosaan wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Tamsier (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tamsier (waxtaancëru)
Lëkkalekaay
Rëdd 1 :
'''Cosaan''' baati [[Seereer|Seereer-Safen]] la. Moo teki "début" / "origine" / "commencé" ci làkki Seereer.
[[Image:Ndangane.jpg|thumb|300px|Cosaan ([[Ndangane]], [[Senegaal]])]]
Ci [[angale]] mooy ''tradition''. Ci [[faranse]] mooy ''tradition''.
Rëdd 11 :
Bu njekk, borom xam-xam yi bayoo tuggal ta see gëstu ajju ci walu jangat-nit, daño weddi woon ni nit ku ñuul amul aada ak cosaan. Li lalloon bilee weddi moodoon ne see dëkk yi ñoo bagoona noot, jalgate axu doomu adam, moom (coloniser) ngir asaloo seeni kom-kom. Bi aduna doxee ba nootagee bi jeex, bu afrik moom boppam, xam-xamu tubaabbi tasaaro, ñeppu nagu nagn ni askan yeppa am aada ak cosaan, ak seeni mbaax (valeurs). Nit ku nuul bu melni Seex Anta Job, jok takku gestul nu sunu cosaan fumu bayee ko. Ligee yam wanee ne nit yu nuul no tabaxoon Ezipt bu yaag ba. Lolu di ndam lu rey si xeetu nit ku nuul.Ndax te bo xamul fo jogee, do xam fo jem.
SEEX LO
 
== Lëkkalekaay yu biti ==
* {{fr}} « Cosaani Sénégambie » (« L’Histoire de la Sénégambie») : 1ere Partie relatée par Macoura Mboub du Sénégal. 2eme Partie relatée par Jebal Samba de la Gambie [in] programme de Radio Gambie: « Chosaani Senegambia ». Présentée par: Alhaji Mansour Njie. Directeur de programme: Alhaji Alieu Ebrima Cham Joof. Enregistré a la fin des années 1970, au début des années 1980 au studio de Radio Gambie, Bakau, en Gambie (2eme partie) et au Sénégal (1ere partie) [in] onegambia.com [in] The Seereer Resource Centre (SRC) (« le Centre de Resource Seereer ») : URL: www.seereer.com. Traduit et transcrit par The Seereer Resource Centre : Juillet 2014. p. 28-29 [http://www.seereer.com/The-Seereer-Resource-Centre-French-Transcript-of-Cosaani-Senegambia-part1-Sohna-Chenaba-Saar-part2-History-Saluum.pdf]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Cosaan » lañ ko jële