Epatit A wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Robertpeters9 (waxtaancëru)
Trying to get infobox to display
CFCF (waxtaancëru)
<nowiki> </nowiki>
Rëdd 11 :
| MeshID = D006506
}}
'''Epatit A'''  (ñu gënoon ko xamee ci turu  '''epatit biy dale''') doon na  [[Jàngoro juy dale]] [[Bu tar (medical)|acute]]  buy jàpp  [[res wi]]  te li koy joxe di doomu jàngoro biñ naan Epatit A (HAV).<ref name=Sherris>{{cite book  |  author = Ryan KJ, Ray CG (editors)  |  title = Sherris Medical Microbiology  |  edition = 4th  |  pages = 541–4  |  publisher = McGraw Hill  |  year = 2004  |  isbn = 0-8385-8529-9  }}</ref>  Bari na lu muy dal nit te du feeñ rawatina ci ndaw yi.<ref name=AFP2012/>  Diggante bi muy dugg sa yaram ak bi muy tàmbalee feeñ, mi ngi tollu ci diggante ñaar ba juróom-benni ayi-bis.<ref name="pmid16271543">{{cite journal|  author=Connor BA|  title=Hepatitis A vaccine in the last-minute traveler|  journal=Am. J. Med.|  volume=118  |issue=Suppl 10A|  pages=58S–62S|  year=2005|  pmid=16271543|  doi=10.1016/j.amjmed.2005.07.018}}</ref>  Su la dalee mën na def ak yaw juróom ñatti ayi-bis te dina faral di ànd ak: xel muy teey, waccu, biir buy daw,  [[jaundice|der bu mboq]], yaram wu tàng, ak mettitu biir.<ref name=AFP2012/>  Luy tollu ci 10 ba 15% ci ñi mu dal ñooy wéy di ko gis su demee ba weesu juróom-benni weer ginaaw bi mu leen dalee.<ref name=AFP2012/> Mag ñi mën nañu ci jëlee  [[Feebaru res bu tar]]  waaye bariwul lu muy dale.<ref name=AFP2012/>
 
<!-- Cause -->
Li koy faral di joxe mooy lekk ñam wala naan ndox mu am doomi jàngoro.<ref name=AFP2012>{{cite journal|last=Matheny|first=SC|last2=Kingery  |first2=JE|title=Hepatitis A.|journal=Am Fam Physician  |date=1 December 2012|volume=86|issue=11|pages=1027–34; quiz 1010–2|pmid=23198670  |url=http://www.aafp.org/afp/2012/1201/p1027.html}}</ref>  [[Meññeefu géej]] buñ toggul ba mu ñor  dina ko faral di joxe.<ref>{{Cite journal   |  last1 = Bellou  |  first1 = M.  |  last2 = Kokkinos  |  first2 = P.  |  last3 = Vantarakis  |  first3 = A.  |  title = Shellfish-borne viral outbreaks: a systematic review.  |  journal = Food Environ Virol  |  volume = 5  |  issue = 1  |  pages = 13–23  |date=March 2013  |  doi = 10.1007/s12560-012-9097-6  |  pmid = 23412719  }}</ref>  Jege ku ko am lu ëpp, mën na la ko wàll.<ref name=AFP2012/> Xale yi mën nañu ko am te du feeñ waaye teewul mën nañu ko wàll ñeneen.<ref name=AFP2012/>  Su la dalee benn yoon, dootu la dalati sa giir gi dund.<ref>{{cite book|title=The Encyclopedia of Hepatitis and Other Liver Diseases|year=2006|publisher=Infobase  |isbn=9780816069903|page=105|url=http://books.google.ca/books?id=HfPU99jIfboC&pg=PA105}}</ref>  Ci sa deret la ñuy seetee doomu jàngoro ci ndax ni muy feeñee dafa nuru ak yu yeneen jàngoro yu bari.<ref name=AFP2012/>  Benn xeetu  [[epatit]]  la ci juróom yiñ xam: A,  [[epatit B|B]],  [[epatit C|C]],  [[epatit D|D]], ak  [[epatit E|E]].
 
<!-- Prevention and Treatment -->
[[ñaqu epatit A]]  dalay aar bu baax ci feebar bi.<ref name=AFP2012/><ref name=Irv2012>{{Cite journal   |  last1 = Irving  |  first1 = GJ.  |  last2 = Holden  |  first2 = J.  |  last3 = Yang  |  first3 = R.  |  last4 = Pope  |  first4 = D.  |  title = Hepatitis A immunisation in persons not previously exposed to hepatitis A.  |  journal = Cochrane Database Syst Rev  |  volume = 7  |  issue =   |  pages = CD009051  |  year = 2012  |  doi = 10.1002/14651858.CD009051.pub2  |  pmid = 22786522  }}</ref>  Yenn réew dañuy faral di baamtu ñaq bi ci xale bi ak ci ñi feebar bi gën a yab kenn masu leen a ñaq.<ref name=AFP2012/><ref name=WHO2013/>  Loolu mën na leen aar seen giir gi dund.<ref name=AFP2012/>  Yeneen matuwaayu yi la ci mën a musal ñooy  [[raxas loxo]]  ak togg ñam ba bu ñor xomm.<ref name=AFP2012/>  Amul benn garab buñ ni mën na ko faj, li ci des, garabi  [[xel muy teey]]  wala  [[biir buy daw]]  la ñu lay digal su aajewoo.<ref name=AFP2012/>  Gën gaa bari su la dalee dangay wér, sa res wi melni dara mësu ko dal.<ref name=AFP2012/>  Bu yàqee res wi, dañu lay  [[gereefeel res]] ngir faj ko.<ref name=AFP2012/>
 
<!-- Epidemiology -->
Ci àdduna bi, jàngoro bi dina feeñ ci 1.5 miliyo?i doomu aadama at mu nekk<ref name=AFP2012/>  nga boole ci yi feeñul mu tollu ci fukki miliyo?.<ref name=Was2006>{{cite journal|last=Wasley|first=A|author2=Fiore, A  |author3=Bell, BP  |title=Hepatitis A in the era of vaccination.|journal=Epidemiol Rev  |year=2006|volume=28|pages=101–11|pmid=16775039  |doi=10.1093/epirev/mxj012  |url=http://epirev.oxfordjournals.org/content/28/1/101.long}}</ref>  Fi mu gënee bari àdduna bi mooy ci gox yi desee te ndox mi ñuy naan setul.<ref name=WHO2013>{{cite web|title=Hepatitis A Fact sheet N°328|url=http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs328/en/|work=World Health Organization|accessdate=20 February 2014|date=July 2013}}</ref>  Ci  [[réew yi néew doole]]  lu tollu ci 90% ciy xale jot nañu am doomu jàngoro bi laata ñuy am 10 at, loolu mooy mucci nañu ci ba fàww laata ñuy nekk mak.<ref name=WHO2013/>  Yenn saay mu jàppandoo ñu bari ci réew yi xawa am doole ndox jàngoro bi bariwul ci xale yi te itam duñu leen di faral di ñaq.<ref name=WHO2013/>  Ci atum 2010, epatit A bu tar bi faat 102,000 doomu aadama.<ref name=Loz2012>{{cite journal|last=Lozano|first=R|title=Global and regional mortality from 235 causes of death for 20 age groups in 1990 and 2010: a systematic analysis for the Global Burden of Disease Study 2010|journal=Lancet|date=Dec 15, 2012|volume=380|issue=9859|pages=2095–128|pmid=23245604|doi=10.1016/S0140-6736(12)61728-0}}</ref>  At mu nekk 28 fan ci weeru Sulet mooy [[Bis biñ Jagleel epatit]]  ngir xamal nit ñi luy  [[jàngoroy epatit]].<ref name=WHO2013/>
 
== Royuwaay yi ==