Leopool Sedaar Sengoor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 50 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q154545 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
mAucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Image:Sengoor.jpg|thumb|right|350px| Leopool Sedaar Sengoor njiitul Senegaal lu njëkk]]
''' Leopool Sedaar Sengoor »''' mi ngi juddoo ca [[Jiwaalo]] ci 9 [[Oktoobar]] ci atum [[1906]], génn àdduna ca [[Verson]] (ca [[Fraas]]) ci 20 Desambar [[2001]]. Nekkoon [[taalifkat]], bindkat doonoon it killifa aada ca [[Senegaal]]. Mooy ki njëkk a doon njiitu réewu Senegaal (1960-1980).
 
Wàcc na jal bi ci teeyug bakkanambàkkanam, bàyyee ko [[Abdu Juuf]]. Ñu bari ci àdduna bi dañu koy jàppe kenn ci xalaatkati [[Afrig]] yi ëpp solo, yu ñaar-fukkeelu xarnu .
 
== Dundam ==
Léopold Sédar Senghor ma nga juddoo ca Jiwaalo, di ab [[dëkk]] bu ndaw bu ne ca tund wu [[Mbuur]], ci diiwaanu [[Cees]]. Baayam di Basil Jogoy Senghor, ab yaxantukat la woon bu bokkoon ci kuréel gu diggu gi ci giirug séeréer, di genn ci néewte yi ci Senegaal .
 
Yaayam di Ñilaan Njéemée Baaxum, ñatteelub baayam . Bi mu amee juroom ñatti at, la tàmbali am njàngam ci ab Gospel : benn jàngu bu dëkku bu Baay yu Ruu Gu Sell gi (les perspères catholiques). Ci atum 1922 la dugg leekool (mbaa jàngu bi) te booba ma nga Ndakaaru, muy ku soppoon njàngat lu Faraas, di woon ku ràññiku ci làkku Faraas, Laatin, wu Geres ak Jabru, mu daal di am Bakalooriya, daal di am ag may ngir àggale am njàngam ca Faraas.
 
---------------
* Yaxantukat ci fr:commerçant
Ligne 15 ⟶ 18 :
 
== Senegaal ==
 
Sengoor nekkoon na di kenn ci ñi doon jàppale Lëngoo gi:(réewi Afrig yi temb bu yàggul), loolu lu mel ne (ag Komonwelth gu Faraas) gu ag Lëngoo la woon, réewi Afrig yi nag ànduñu ci woon. Moom sosoon na ak Moodibo Kayta Lëngoo gu Mali gi. Moo nekkoon njiitul jataayub lëngoo bi ba ci kero bi mu tasee atum 1960, moo nekkoon ki njëkk a jiite [[Senegaal]], ñi ngi ko tànn ci 5 [[satumbar]] 1962, mooy ki sadd [[bàkku réewum Senegaal]] ([[gar gu xonq gi]]).
Njiitul jëwrinam lii di [[Mamadu Ja]] moo féetewoo woon doxal naal yi aju ci suqaliku gu réew mi gu guddub dig gi(long terme), bu ko defee moom Sengoor mu féetewoo séqoo yu bitim réew yi
Ligne 24 ⟶ 28 :
Ak doonte canc gu Faraas jeex na ci melo wu kilifawu (officiel) teewul xiimay koppar bu Senegaal Faraas a koy saxal, njàng mi it ci làkku Faraas lañu koy defe, te Sengoor it réew mi mi ngi ko jiite woon ànd ak ay xelalkat yu Faraas yu muy diisool, (Ñooñu nag manuñoo joxe menn xel mu njariñul Faraas nekkul, Moom itam jabari waa Faraas la yoroon, te bari na lool lu mu daa xeex ngir ñu yor aaday [[Faraas]], Taalifkat ba nee na:
 
* '''(Màggat mu màggat ci am () njàngum tubaab jabaroo () tubaab tubaab la, tubaab ngeen dénk seen gaal gii) '''
 
'''
--------------------
* Lëngoo gi ci fr: fédéralisme
Ligne 33 ⟶ 37 :
* mbokkoo: socialisme, mbokkte:communisme, afal:libéralisme, noste gu yar :systeme educatif
--------------------
 
 
[[Wàll:niti senegaal]]