Yamoo wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Legobot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 1 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q23538 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
mAucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Earth equator northern hemisphere.png|right|300px]]
Ci [[melosuuf]], '''yamoo''' wi aw rëddu tus-wu-gar la, di ag buumug jeneer gees rëdd mu wër àdduna, jaar ci diggante dott yi. Yamoo wi moo xàjjale àdduna bi, def ko [[xaaju-kol-kol bu bëj-gànnaar]] ak [[xaaju-kol-kol bu bëj-saalum]]. [[Tus-wu-gaar]] wu yamoo wi 0° (tus aj). Guddaayu yamoo gu Suuf si mi ngi tollu, ci xayma, 40 075 km.
 
== Yamoog Suuf si ==
=== Klimaa ===
Klimaab barab yi ne ci li wër yamoo gi lañuy wax [[klimaab yamoo]]. Di nañ wax itam klimaab [[Gëwéelub|gëwéel]], di bu barab yi ne ci li wër [[gëwéel]] yi ([[gëwéelub Tef]] ak [[gëwéelub Sànkar]]) .
 
=== Réew yi mu dagg ===
[[Dencukaay:World map with equator.svg|thumb|Lonkoyoonu àdduna buy fesal yamoo gi]]
Ci sunu àdduna ([[Suuf]] si), yamoo gi ay mbàmbulaan ñoo ëpp ci li mu dagg ci yoonam, téeméer boo jël ci gudaayam ñaar-fukk ya rekk a jaar ci suuf.
 
=== Afrig ===
Yamoo gi jaar na ci juroom-ñaari réewi [[Afrig]] :
 
* [[Sao Tome ak Principe]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Yamoo » lañ ko jële